1
00:00:11,845 --> 00:00:13,930
Dafa jot ma chrome fuck bi.

2
00:00:14,514 --> 00:00:16,141
Dellu ci jahannama.

3
00:00:16,224 --> 00:00:18,351
Bëgg jaay, déglul sama ofrand.

4
00:00:18,435 --> 00:00:19,686
Duma jaay.

5
00:00:19,769 --> 00:00:21,688
Dama ñëw ngir chip kaka.

6
00:00:21,771 --> 00:00:23,398
Déglul, Davey.

7
00:00:23,481 --> 00:00:25,859
Ni amna piyeesu grade soldaar.

8
00:00:25,942 --> 00:00:28,027
Dafa wara am tabax ngir mëna ko liggéey.

9
00:00:28,111 --> 00:00:30,572
Ak, choom, loolu lu am solo la
amoo.

10
00:00:30,655 --> 00:00:33,950
Wax ni ripper
ku bëgg kiliyaanam dëgg.

11
00:00:34,034 --> 00:00:37,454
Hah! Point bi mooy,
Mënu ma ko fay.

12
00:00:41,291 --> 00:00:42,709
Waaw. Xaaral tuuti.

13
00:00:43,293 --> 00:00:45,211
Fuck it, waay. Dinaa ko jënd.

14
00:00:45,879 --> 00:00:47,464
Dinaa la chip.

15
00:00:48,673 --> 00:00:51,634
Waaye soo delloo,
di jooy ngir dindi ko...

16
00:00:52,802 --> 00:00:57,599
ndax dafay yàq sa yuur,
Sandy mooy sama moom te doo fay.

17
00:00:58,224 --> 00:01:00,226
Kon, pare nga xotti?

18
00:01:25,960 --> 00:01:32,425
<i>♪ Bët yi, di tàkk ci man ♪</i>

19
00:01:32,509 --> 00:01:38,014
<i>♪ Bët, yàq lu neex ♪</i>

20
00:01:39,140 --> 00:01:44,312
<i>♪ Leegi, amna safara ci man ♪</i>

21
00:01:44,395 --> 00:01:51,277
<i>♪ Safara wuy tàkk ♪</i>

22
00:02:18,972 --> 00:02:21,432
<i>♪ Safara gii dafa sotti ♪</i>

23
00:02:21,516 --> 00:02:24,894
<i>♪ Dinaa ko lakk, Dinaa ko lakk
Dinaa ko lakk, Dinaa ko lakk ♪</i>

24
00:02:34,696 --> 00:02:39,033
<i>♪ Dinaa ko lakk, Dinaa ko lakk
Dinaa ko lakk, Dinaa ko lakk ♪</i>

25
00:02:46,040 --> 00:02:47,143
Ci biir waxtaan wi,

26
00:02:47,167 --> 00:02:52,714
Lavabre dafa fitnaal Arasaka ak ay matuwaay
ci politiku juuti yu EU.

27
00:02:52,797 --> 00:02:55,216
Martines, David, sa yeexal
enregistré nañu ko.

28
00:02:55,300 --> 00:02:57,719
Xoolal bu baax.
Wutal load ci waa ji.

29
00:02:57,802 --> 00:02:59,721
Dafa serye...

30
00:03:01,806 --> 00:03:04,058
Mënu, Martinez. Nu ngi ci ekol bi!

31
00:03:04,142 --> 00:03:06,222
Amna ay kameraa. Ndax ñàkk nga sa...

32
00:03:07,228 --> 00:03:09,022
Lan? Ndax danga ragal ñu jàpp la?

33
00:03:09,105 --> 00:03:12,025
Ndax xamnaa ni du loolu.
Gaawal.

34
00:03:12,108 --> 00:03:13,651
Baax na?

35
00:03:47,227 --> 00:03:50,563
Kaka. Lu nga def?

36
00:03:50,647 --> 00:03:54,150
Ban xeetu implant la?
Danga damm sama bakkan, yaw bënn!

37
00:03:54,234 --> 00:03:56,277
Léegi nga jeex! Xam nga kan mooy sama pàppa?

38
00:03:56,361 --> 00:04:00,406
Ab njiitu Arasaka ci njiitu akademi bi!
Yaa ngi dem ba jéggi dayo.

39
00:04:00,490 --> 00:04:04,577
Danga wara bàyyi bi nga nekkee
kanam, yaw kaña gu bonn gi.

40
00:04:04,661 --> 00:04:06,204
<i>Daa melni damay def kaka.</i>

41
00:04:11,793 --> 00:04:15,338
Hmm?

42
00:04:31,396 --> 00:04:33,106
<i>Ndax dafa dëggu...</i>

43
00:04:36,401 --> 00:04:40,571
<i>Jeexal nga! Xam nga kan mooy sama pàppa?
Benn njiitu Arasaka ci kilifay Akademi bi!</i>

44
00:04:40,655 --> 00:04:43,032
<i>Danga dem fu sori!</i>

45
00:04:43,116 --> 00:04:44,659
Marcus,

46
00:04:44,742 --> 00:04:49,622
indil ma wideo sama doom
sa xarit ci klaas bi daf lay sonal.

47
00:04:49,706 --> 00:04:50,581
Lu tax?

48
00:04:50,665 --> 00:04:53,835
David Martines mooy turam,
17 at,</i>

49
00:04:53,918 --> 00:04:55,336
ci Santo Domingo.</i>

50
00:04:55,420 --> 00:04:56,629
<i>Ndongo bu mag la</i>

51
00:04:56,713 --> 00:04:59,132
<i>ku def corruption bu yàggul dara
Done ak jumtukaayi akademi</i>

52
00:04:59,215 --> 00:05:01,259
<i>ak yeesali couronne bootleg.</i>

53
00:05:01,342 --> 00:05:04,512
<i>Déedet baay. Bu yàggul ñu ray sama yaay
ci aksidaa ci tali.</i>

54
00:05:04,595 --> 00:05:06,389
<i>Amna bor yu bari ci Akademi bi.</i>

55
00:05:06,472 --> 00:05:07,932
Ndax fàww ma xam lii yépp?

56
00:05:08,016 --> 00:05:09,434
<i>Xoolal fimuy yëngu, kilifa gi.</i>

57
00:05:09,517 --> 00:05:12,353
Dafa leer ni dafa jëfandikoo implant bu Sandevistan
ñaareelu lietnaa bu njëkk</i>

58
00:05:12,437 --> 00:05:14,939
James Norris amoon na
ci jamonoy dee bii.</i>

59
00:05:15,023 --> 00:05:18,484
Gis naa ko. Dañu tëj dosiye bi
muy luy xew ci siberpsikotik.

60
00:05:18,568 --> 00:05:20,611
<i>Waaw, sama waajur. Waaye, wuute na ak soldaar bi,</i>

61
00:05:20,695 --> 00:05:24,699
<i>ndongo bii amul lenn luñu koy gis
njeexital yu bawoo ci implant bi.</i>

62
00:05:24,782 --> 00:05:26,951
<i>Dama gëm ni dafay muñ sibernetik</i>

63
00:05:27,035 --> 00:05:31,664
<i>mën nako def
kàndidaa bu njëkk ngir natt produit bi.</i>

64
00:05:31,748 --> 00:05:34,459
Hmm. Fan la nekk léegi?

65
00:05:34,542 --> 00:05:37,003
<i>- Dañu ko dàq, kilifa gi.</i>
- Woowal ko.

66
00:05:37,086 --> 00:05:39,797
Nax ko ci dige ni dina la ko jàppale ci xaalis.

67
00:05:39,881 --> 00:05:41,966
<i>Waaw, sama waajur. Ak sa doom?</i>

68
00:05:42,050 --> 00:05:45,178
Sama ndono, jotna mu jàng

69
00:05:45,261 --> 00:05:48,973
luy jaamu
lu gëna baax ci liggéeyukaay bi.

70
00:05:52,935 --> 00:05:54,062
<i>Mr. Martines,

71
00:05:54,145 --> 00:05:56,981
<i>Maa ngi lay digal nga xam sa dàq
def nañu ko ci anam wu jaar yoon.</i>

72
00:05:57,065 --> 00:06:00,401
<i>Waaye, waajur M. Tanaka
jokkool ak nun ngir laaj...</i>

73
00:06:02,987 --> 00:06:05,907
Dama laal lool.

74
00:06:16,167 --> 00:06:18,878
<i>Raxas bi jeexna.</i>

75
00:06:55,540 --> 00:06:57,250
Saa waay! Mbaa yaa ngi am jàmm?

76
00:07:00,336 --> 00:07:03,005
Dafay xew saa yu nekk.
Maa ngi lay wax loolu amul benn njariñ.

77
00:07:10,721 --> 00:07:13,516
Ha?

78
00:07:25,695 --> 00:07:26,737
Ha?

79
00:07:46,215 --> 00:07:48,134
Gaawal.

80
00:07:48,217 --> 00:07:51,012
- Kon, lan mooy sa xalaat? Tuurul ko.
- Lan? Sama angle?

81
00:07:51,095 --> 00:07:53,347
Lan mooy?
Yaa ngi yàq sama liggéey.

82
00:07:53,431 --> 00:07:57,018
Liggéey, wala? Suma xamul lu gëna baax,
Dama naan mbaam xuux nga.

83
00:07:57,101 --> 00:07:59,020
Kon, lan? Di ngama defal ay manchet?

84
00:07:59,103 --> 00:08:01,481
Mënu ma ni sàcc bu ndaw nga.

85
00:08:02,231 --> 00:08:04,859
Hmm...

86
00:08:04,942 --> 00:08:06,903
- Xam naa la ?
- Déedet, uh...

87
00:08:06,986 --> 00:08:09,030
Dëgg la. Yaakaar naa du noonu.

88
00:08:11,407 --> 00:08:14,410
Ah! Xoolal, xale bu góor bi, danga ci jafe-jafe.

89
00:08:14,494 --> 00:08:15,494
Ha?

90
00:08:15,536 --> 00:08:19,832
Dëgg la? Sandewistan la?
Daan. Wax ma fan nga ko fekk.

91
00:08:20,416 --> 00:08:23,711
Xaar. Curiosité moo ray muus mi
ak loolu lépp.

92
00:08:23,794 --> 00:08:26,797
Xalaat bu doy waar. Ak nu bokk liggéey?

93
00:08:26,881 --> 00:08:28,049
Lan ngay def? Sàcc?

94
00:08:28,132 --> 00:08:30,843
Ndax sàcc la sudee damay dóor rek
Arasaka?

95
00:08:30,927 --> 00:08:33,679
Gaawal. Dama xool corpo ci yaw?

96
00:08:33,763 --> 00:08:37,266
Danga wara laaj lu xoromu.
Scan jël na ID Akademi Arasaka.

97
00:08:37,350 --> 00:08:41,229
Waaye wax nga dëgg, dëgg la
bul xool xeetu mbir mi, loolu leer na.

98
00:08:41,312 --> 00:08:43,940
Man, uh... Dama bàyyi jàng.

99
00:08:44,023 --> 00:08:47,318
Ah! Xale bu bon nga.

100
00:08:47,401 --> 00:08:50,238
Kon, dangay xool 'Saka, wala ?

101
00:08:50,321 --> 00:08:52,114
Lu tax? Dugg nga?

102
00:08:52,198 --> 00:08:55,326
Dina yàq xol sama yaay
su ko gisee, xam nga ko.

103
00:08:56,327 --> 00:08:58,996
Déglul bu baax. Njang moomu 1.

104
00:08:59,080 --> 00:09:01,499
Àtte bu néew, xam-xam bu gëna bari.

105
00:09:01,582 --> 00:09:03,501
Waaw, waaw. Kon, luy sama dagg?

106
00:09:03,584 --> 00:09:06,254
Dina nu xaaj limu jël, 80-20.

107
00:09:06,337 --> 00:09:10,841
Lan? Fuck loolu. Danuy dem xaaj
ci liggéey bi ba noppi ma am ennies?

108
00:09:10,925 --> 00:09:13,469
Man maay ki koy puus
piyeesu club bi.

109
00:09:13,553 --> 00:09:15,972
Boole ci amna stagiaire bu may saytu leegi.

110
00:09:16,055 --> 00:09:17,640
Stagiaire? Gaawal.

111
00:09:17,723 --> 00:09:21,394
Dama bëgg lool eddies leegi.
60-40 yoon la, wala book?

112
00:09:22,103 --> 00:09:23,563
70 ba 30.

113
00:09:23,646 --> 00:09:26,983
Te dinaa ko fay ñaareelu yoon bu liggéey bi jeexee.
Yaakaar naa ni loolu mooy yoon.

114
00:09:28,401 --> 00:09:30,653
- And naa ci. Daa melni lu baax.
- Déggoo la.

115
00:09:31,445 --> 00:09:32,445
Man maay Lucy, waaw?

116
00:09:34,073 --> 00:09:35,283
David laa tudd.

117
00:09:38,035 --> 00:09:39,870
<i>Leer? Danga may jàng bu baax?</i>

118
00:09:39,954 --> 00:09:41,038
Kristal. Baaxna.</i>

119
00:09:41,122 --> 00:09:44,417
<i>Sama njeexte itam. Sunu màrk, waaw?</i>

120
00:09:44,500 --> 00:09:45,918
<i>Ñetti waxtu. Bul wëlbatiku.</i>

121
00:09:46,502 --> 00:09:47,795
<i>Jot naa ko.</i>

122
00:09:47,878 --> 00:09:49,171
<i>Toxu ci biir.</i>

123
00:09:50,464 --> 00:09:53,426
<i>Waaw kay? Waajal... ngir yëngu.</i>

124
00:09:53,509 --> 00:09:56,929
<i>Ñett, ñaar, benn... Waxtu wane.</i>

125
00:10:04,854 --> 00:10:06,355
<i>Yomb naa ni mburu!</i>

126
00:10:06,439 --> 00:10:09,358
<i>Seddal, noob, seddal.
Deal dëgg mooy li ci topp.</i>

127
00:10:09,442 --> 00:10:10,442
<i>Indil ko!</i>

128
00:10:10,484 --> 00:10:13,904
<i>Ñetti yéere yu xoromu? Yada-demal!</i>

129
00:10:14,488 --> 00:10:16,782
<i>Ci noonu la ñaari yuur yi daal di leer.</i>

130
00:10:17,366 --> 00:10:18,868
<i>Yomb naa.</i>

131
00:10:18,951 --> 00:10:20,953
<i>Nanu. Nanga def, défi.</i>

132
00:10:21,037 --> 00:10:24,498
<i>Waaw, waaw.
Jën wu rëy, loot bu rëy di ñëw.</i>

133
00:10:24,582 --> 00:10:27,251
<i>Soni yi...</i>

134
00:10:27,335 --> 00:10:29,045
<i>Du yuuxu corpo ci man.</i>

135
00:10:29,128 --> 00:10:31,172
<i>Déedet. Sidit buñ jël. Waajal nga?</i>

136
00:10:31,255 --> 00:10:33,466
<i>- Ñett, ñaar, benn.
- Xaaral.</i>

137
00:10:41,098 --> 00:10:43,601
<i>Baaxna, baaxna.
Danu raxas oto bii bamu waw.</i>

138
00:10:43,684 --> 00:10:45,436
<i>Bi ci topp, nu dem.</i>

139
00:10:45,519 --> 00:10:46,812
Roger loolu.</i>

140
00:10:47,855 --> 00:10:52,526
- Kon, naka laa def?
- Dinaa ni jar nga 20% bi.

141
00:10:52,610 --> 00:10:54,654
Hey, 30 la!

142
00:10:54,737 --> 00:10:56,113
Tooñ.

143
00:10:56,822 --> 00:11:00,076
- Weyal ko di yëngu? Beneen oto?
- Amaana beneen liiñ?

144
00:11:00,159 --> 00:11:02,620
Amaana amna ku
xamnaa mbaam xuux yi leegi.

145
00:11:02,703 --> 00:11:04,903
Sunuy tëb, chance yi dañuy néew...

146
00:11:07,500 --> 00:11:08,751
Ndax mu bon?

147
00:11:08,834 --> 00:11:10,378
Juumte bu gëna bari ci rookie.

148
00:11:10,461 --> 00:11:14,090
Jëlul benn matuwaay ngir moytu
biñu defee implant bi ba leegi.

149
00:11:14,173 --> 00:11:16,175
Ban immunosuppresseur lay jël?

150
00:11:16,967 --> 00:11:18,511
Hey, waa jii amna assurance?

151
00:11:18,594 --> 00:11:21,847
Amuma benn leeral.
For sure nuruwul ni dina nekk.

152
00:11:21,931 --> 00:11:25,601
Am nga famiy, gardien legal?
Kenn kuma mëna woo?

153
00:11:25,684 --> 00:11:28,562
Xamuma. Waajur yi, yaakaar naa.

154
00:11:28,646 --> 00:11:30,731
Dama daan dem ci akademi Arasaka.

155
00:11:30,815 --> 00:11:34,193
arasaka?
Amul werante ndax mënoon na...

156
00:11:34,276 --> 00:11:36,987
Nanga def. Xaaral ab diir.

157
00:11:37,071 --> 00:11:40,074
Ci suba. Kon, naka ngay yëg sa bopp?

158
00:11:40,741 --> 00:11:42,410
Maa ngi sànni.

159
00:11:42,493 --> 00:11:44,245
Nga fàttaliku ban pilules ngay naan?

160
00:11:44,954 --> 00:11:46,372
- Pilule?
- Lan?

161
00:11:48,207 --> 00:11:50,960
Waaw, waay! Psycho nga.

162
00:11:54,839 --> 00:11:57,133
Saa waay soxna si, leegi lañu romb hopitaal bi...

163
00:11:57,216 --> 00:11:58,426
Oh sama.

164
00:11:58,509 --> 00:12:02,263
Déglul, choom, xale bii amna implant ci
ki ko wara yóbbu lu mu néew ñaari K.

165
00:12:02,346 --> 00:12:05,057
- Kon, toogal rek nga ànd ak dal te...
- Loolu dëgg la ?

166
00:12:05,141 --> 00:12:07,268
Yaw, melni, dagg ab deal
ak yenn Scavengers?

167
00:12:07,351 --> 00:12:10,020
Mani ko toogal nga féexal sa yaram
wala nu laaj la chrome itam.

168
00:12:10,104 --> 00:12:11,605
David, jéggalu.

169
00:12:11,689 --> 00:12:14,775
Daa melni dañu wara soppi sunuy pexe.
Dellu nga ci 20.

170
00:12:14,859 --> 00:12:16,402
Ha?

171
00:12:27,580 --> 00:12:30,249
Sama Yàlla! Waaw!

172
00:12:30,833 --> 00:12:34,336
<i>♪ Ci xeex bu Aljuma bi ♪</i>

173
00:12:34,420 --> 00:12:37,214
<i>♪ Xaaral toog sukku
Aljuma guddi rekk la ♪</i>

174
00:12:37,298 --> 00:12:41,177
<i>♪ Su luu yi toogee di xool
yoon ngir xaritoo ak yaw, amul benn mbëggeel ♪</i>

175
00:12:41,260 --> 00:12:44,263
<i>♪ Su ville bi bokk ci jeans yu sew yi ♪</i>

176
00:12:48,601 --> 00:12:50,269
Uop.

177
00:12:50,352 --> 00:12:53,689
Salaam, def nga jàmm? Du dee, wala book?

178
00:12:53,772 --> 00:12:56,233
- Doktër, mangi.
- Ha?

179
00:12:56,317 --> 00:12:58,527
Klinik Doktër bi. Ripperdok. Yobbu ma fa.

180
00:13:09,163 --> 00:13:10,163
David, xarit.

181
00:13:10,623 --> 00:13:13,125
Man, danga nuru kaka.

182
00:13:13,209 --> 00:13:14,418
Jërëjëf lool.

183
00:13:14,502 --> 00:13:16,754
Ñaata yoon nga fippu?

184
00:13:16,837 --> 00:13:19,298
Juróom. Déedet, amaana juróom ñatti.

185
00:13:19,381 --> 00:13:21,217
Jesus Henri Kirist.

186
00:13:21,300 --> 00:13:24,053
Ku mag mënu ci woon
mbugal boobu.

187
00:13:24,136 --> 00:13:26,639
Maa ngi doon jàmm benn waxtu ci ginaaw ba noppi...

188
00:13:26,722 --> 00:13:28,432
Sama bakkan daal di jameet.

189
00:13:29,016 --> 00:13:32,645
Gonk amul woon ay immunobloqueur.
Bëgg nga leeral?

190
00:13:32,728 --> 00:13:35,189
Ah, gisuma woon njariñ li.

191
00:13:35,272 --> 00:13:39,360
Kon xalaat bu jaarul yoon.
Jaay ko garab yi.

192
00:13:39,443 --> 00:13:42,738
Dellu ci etaser bii
Duma ko dagg. Ligue bu wuute.

193
00:13:42,821 --> 00:13:43,906
Ndax amna lu baax ci loolu?

194
00:13:43,989 --> 00:13:45,866
Yaa ngi may sargal?

195
00:13:45,950 --> 00:13:49,787
Fuck dëgg, man laa!
Amul benn saraxe, choom.

196
00:13:49,870 --> 00:13:52,039
Ñaata ngay jënd?

197
00:13:53,040 --> 00:13:55,042
Ñaari fan la.

198
00:13:55,125 --> 00:13:57,211
Loolu la ?

199
00:13:57,294 --> 00:13:59,880
Nanga def, bul jaaxle
dem def ay bitig, sama xol.

200
00:13:59,964 --> 00:14:02,883
Ndax loolu mën nala indil jafe-jafe
dellu ak Scavs.

201
00:14:04,176 --> 00:14:05,970
Bastard bu bëgg xaalis.

202
00:14:09,640 --> 00:14:12,393
Ndax bëggoo mu dem?

203
00:14:12,476 --> 00:14:13,727
Déed.

204
00:14:13,811 --> 00:14:18,774
Ba leegi mënu ma ni danga ko dàq
8 yoon ci benn bis.

205
00:14:18,857 --> 00:14:21,235
Amaana masochiste nga wala...

206
00:14:21,318 --> 00:14:23,779
Déglul bu baax, Davey. Ñaar ci bis bi, amul leneen.

207
00:14:23,862 --> 00:14:26,657
Amaana ñett, waaye loolu mooy li ëpp.
Amul benn yëf.

208
00:14:26,740 --> 00:14:29,910
Doonte sa yaram mën nako muñ,
sa boppu nen bi mënul ko.

209
00:14:29,994 --> 00:14:34,331
Weyal di laal ak implant bi
Dinaa yëngal sa yuur.

210
00:14:35,374 --> 00:14:38,669
Yaa ngi wax benn implant
mën nama def siberpsiko?

211
00:14:38,752 --> 00:14:42,172
Ndax loolu mën na am?
Musu ma dégg loolu xew ci sama àdduna.

212
00:14:42,256 --> 00:14:43,507
Davey,

213
00:14:43,591 --> 00:14:46,010
Yaakaar naa ni man nga ko dégg,
xamoo ko?

214
00:14:57,313 --> 00:14:58,397
Hé?

215
00:15:03,777 --> 00:15:06,405
- Kon, def ngeen lépp?
- Uh, waaw.

216
00:15:06,488 --> 00:15:08,741
Kon maa ngi xalaat
loolu mooy njeextalu tay gi.

217
00:15:08,824 --> 00:15:10,743
Maa ngi ci jàmm. Mën naa wéy di daw.

218
00:15:10,826 --> 00:15:15,039
Yaw drog bu rëy. Maa ngi waaja tàmbali
cyberpsycho

219
00:15:15,623 --> 00:15:18,876
Sandevistan, jëfandikoo ko rek
bi nga amul beneen pexe.

220
00:15:18,959 --> 00:15:20,961
Yeneen anam yu bari ngir génne eds.

221
00:15:21,670 --> 00:15:24,089
Ba leegi bëgg nga liggéeyandoo ak man ginaaw loolu?

222
00:15:24,173 --> 00:15:27,217
Xalaatal ni dinaa la bàyyi nga dem
te duma njëkka fay?

223
00:15:29,762 --> 00:15:32,431
Baax. Dama soxla
eddies yi.

224
00:15:32,514 --> 00:15:33,682
Loolu mooy xel mi.

225
00:15:35,601 --> 00:15:38,062
Yaakaar naa ni yewwoo
ngir am yeneen ci guddi gi?

226
00:15:38,145 --> 00:15:40,189
Dama melni luy yeex ci luwaas bi.

227
00:15:40,272 --> 00:15:44,777
- Du tay ci guddi. Suba.
- Waaw kay, waaw kay.

228
00:15:48,530 --> 00:15:51,450
- Gaawal.
- Ha? Xamoon naa ni dinga ko bëgg!

229
00:15:51,533 --> 00:15:53,744
Du lu jëm ci liggéey.

230
00:15:53,827 --> 00:15:54,827
Ha?

231
00:15:56,455 --> 00:15:57,581
Fii nii.

232
00:15:57,665 --> 00:16:00,209
Yaw, uh... dëkk yaw kese?

233
00:16:00,292 --> 00:16:02,962
- Hm-mmm. Ak?
- Dara.

234
00:16:04,004 --> 00:16:07,466
- Lan? Tiitaange wala lu mell nonu?
- Dëgg la.

235
00:16:07,549 --> 00:16:09,969
- Bii mooy yoon wu njëkk?
- Jahannama, déet.

236
00:16:10,052 --> 00:16:12,471
Noppal, ndax yaa ko!

237
00:16:13,180 --> 00:16:14,223
Toogal. Dal.

238
00:16:15,140 --> 00:16:16,934
Bieer rek laa am. Yaa ngi naan?

239
00:16:17,017 --> 00:16:18,477
Uh, waaw waaw.

240
00:16:18,560 --> 00:16:19,561
Tàccu.

241
00:16:25,442 --> 00:16:28,237
Oh, xale.

242
00:16:28,821 --> 00:16:32,032
Ci anam bu dëggu? Kon, noonu la
bis bi ngay njëkka naan.

243
00:16:32,116 --> 00:16:34,952
- Déedéet, am naa ko. Du...
- Hm-mmm.

244
00:16:35,035 --> 00:16:37,454
Naan gaz ak tóx, bul def benn ci ñoom.

245
00:16:37,538 --> 00:16:40,165
Duma ko def
ñaawal la ci loolu.

246
00:16:40,249 --> 00:16:41,250
Dëgg laay wax.

247
00:16:41,333 --> 00:16:44,253
Dëgg la.
Lu xew ak getup bi?

248
00:16:47,798 --> 00:16:48,716
Summil ko.

249
00:16:48,799 --> 00:16:50,175
Lan? Lu tax?

250
00:16:50,259 --> 00:16:51,593
Def ko rekk. Gaawal.

251
00:16:51,677 --> 00:16:53,137
Hey!

252
00:16:55,097 --> 00:16:58,934
Uh, xaar. Bul ci jaxasoo. Gaawal.

253
00:16:59,601 --> 00:17:02,021
Uh... Dawalkat yu mag yi?

254
00:17:03,022 --> 00:17:04,898
Beneen baat ngir siberpunk.

255
00:17:04,982 --> 00:17:07,026
Mooy ki nga bëgga nekk, wala book?

256
00:17:08,318 --> 00:17:11,030
JK's <i>Série Edgerunners.
Shit, waaw, soppe laa.

257
00:17:12,281 --> 00:17:13,282
Sérieux nga?

258
00:17:13,866 --> 00:17:15,784
Dellu ci ya.

259
00:17:15,868 --> 00:17:18,662
melni afisu gunk.

260
00:17:20,205 --> 00:17:21,205
Am nga jafe-jafe?

261
00:17:21,248 --> 00:17:23,584
Uh... Amul jafe-jafe.

262
00:17:23,667 --> 00:17:25,544
Saa yu nekk daf may dàq.

263
00:17:25,627 --> 00:17:29,965
yëgle yooyu yépp dañu koy nuru
Daa melni aljana wala lu mell nonu.

264
00:17:30,049 --> 00:17:33,427
Peeps yu bari dee nañu di jéema wëlbatiku
xeer wu muus wi nekk lu am njariñ.

265
00:17:33,510 --> 00:17:36,180
Dafa gëna melni kampu kaso moo gën aljana,
soo ma laajee.

266
00:17:37,222 --> 00:17:40,142
Daa melni ku
def seen devoir.

267
00:17:40,225 --> 00:17:44,146
Uh, du dëgg.
Ay mbir yu bari rek laa jàngee ci ekol.

268
00:17:44,229 --> 00:17:46,899
Maa ngi lay sàkku jéggalu, xale bu góor bi.

269
00:17:47,566 --> 00:17:49,276
Du noonu la.

270
00:17:49,359 --> 00:17:52,321
Du noonu ? Musu ma daje ak pleb
mi jàngi ci daara 'Saka.

271
00:17:52,404 --> 00:17:53,404
Du noonu!

272
00:17:57,576 --> 00:18:00,579
Man ak sama yaay
amul woon xaalis bu bari.

273
00:18:00,662 --> 00:18:03,342
Amul nuñu ko mënee am
nangu ma ci mbedd mi nii.

274
00:18:04,249 --> 00:18:06,460
Liggéey na bu baax ngir tëye ma
ci Akademi bi,

275
00:18:06,543 --> 00:18:09,421
boole ay tourbillon
Lumu mëna doon mënoon na.

276
00:18:09,505 --> 00:18:11,465
Bëgg nga xam kicker bi dëgg?

277
00:18:11,548 --> 00:18:14,093
Xamoon naa bis bu njëkk bi ni duma musa bokk ci foofu.

278
00:18:14,176 --> 00:18:17,513
Kon lu tax ngay toog lu yàgg nii?
Wala sax.

279
00:18:17,596 --> 00:18:19,098
Laaj bu baax.

280
00:18:19,181 --> 00:18:21,141
Yaakaar naa ni ngir sama yaay la. Xam nga.

281
00:18:21,225 --> 00:18:24,478
"Dinga am liggéey ci Arasaka,
Yéeg ci seel corpo bi."

282
00:18:25,104 --> 00:18:29,817
Dafa melni gént, loolu lépp lu 'Saka.
Sunu gént la, yaakaarnaa loolu.

283
00:18:29,900 --> 00:18:31,068
Wala lumu mëna doon.

284
00:18:32,319 --> 00:18:35,739
- Waaye du sa gént, wala book?
- Sama gént?

285
00:18:36,323 --> 00:18:39,243
Waaw, waaw. Yaw, sa yaay,
nit ñu wuute ngeen.

286
00:18:40,077 --> 00:18:42,579
Lu tax nga wara liggéey ngir mëna yegg ci mébetam?

287
00:18:43,539 --> 00:18:45,749
Loolu amul lenn lu jaarul yoon.

288
00:18:45,833 --> 00:18:48,627
Danga wara wut sa mébet.

289
00:18:48,710 --> 00:18:51,505
Daa melni ci man
melni yaa ngi gis sa bopp.

290
00:18:52,673 --> 00:18:54,508
Ndax loolu ay kaf la, wala lan?

291
00:18:54,591 --> 00:18:56,343
Wowe nga ko kampu kaso.

292
00:18:56,426 --> 00:19:00,472
Ci man, dëkk bii moo gëna bon.

293
00:19:00,556 --> 00:19:01,849
Barab bii?

294
00:19:01,932 --> 00:19:04,768
Dama bëgga dem. Lumu mëna dem.

295
00:19:07,521 --> 00:19:09,898
- Gaawal. Amna luma lay wan.
- Ha?

296
00:19:24,955 --> 00:19:27,666
Waaw! Xoolal dogal bii!

297
00:19:27,749 --> 00:19:29,710
Maa ngi yëg jant bu tàng bi.

298
00:19:29,793 --> 00:19:31,211
Loolu jaaraleko ci sa lien bopp.

299
00:19:31,295 --> 00:19:33,672
Mooy li lay may
ngir yëg tàngooru jant bi.

300
00:19:33,755 --> 00:19:36,925
Dëgg la dina ñu la saaf
Suma la jox temp bi dëgg.

301
00:19:37,009 --> 00:19:40,220
Fexe naa wàññi jekkal yi,
mellow out jaar-jaar bi.

302
00:19:41,471 --> 00:19:42,306
Delloosi ko?

303
00:19:42,389 --> 00:19:44,308
Ñàkk pexe! Lii ab preem la!

304
00:19:45,475 --> 00:19:46,810
Danga nuru lu dof!

305
00:19:53,442 --> 00:19:56,236
- Nova, wala ?
- Loolu yéeme na!

306
00:19:56,320 --> 00:19:57,529
Du noonu ?

307
00:19:59,740 --> 00:20:00,824
Fii.

308
00:20:03,535 --> 00:20:10,083
<i>♪ Beneen guddi ma toog
Liggéey ci diggante say rëdd ♪</i>

309
00:20:11,210 --> 00:20:14,087
<i>♪ Ndax maa ngi lay namm saa yu nekk ♪</i>

310
00:20:16,965 --> 00:20:19,259
<i>♪ Kon, demal ♪</i>

311
00:20:19,343 --> 00:20:23,555
<i>♪ Meneen anam ngir yëg
Li nga bëggul sa bopp xam ♪</i>

312
00:20:23,639 --> 00:20:25,682
<i>♪ Te bàyyi sa bopp dem ♪</i>

313
00:20:26,475 --> 00:20:29,686
<i>♪ Xam nga ni defoo ko
Ñàkk sa bopp ♪</i>

314
00:20:30,562 --> 00:20:32,689
<i>♪ Nañu tàmbalee ci xon ♪</i>

315
00:20:33,315 --> 00:20:36,443
<i>♪ Dellu, beneen yoon ngir nekk fi ♪</i>

316
00:20:36,526 --> 00:20:41,156
<i>♪ Bëggoo sa bopp dem
Bàyyil sa bopp ♪</i>

317
00:20:41,240 --> 00:20:45,911
<i>♪ Ndax loolu mooy déggoo? ♪</i>

318
00:20:47,079 --> 00:20:49,331
<i>♪ Kon loo bëgga def ♪</i>

319
00:20:49,414 --> 00:20:51,250
<i>♪ Luy sa xalaat? ♪</i>

320
00:20:51,333 --> 00:20:53,126
<i>♪ Amna feet ci lu yaggul dara ♪</i>

321
00:20:53,210 --> 00:20:55,254
<i>♪ Bëgg nga dem? ♪</i>

322
00:20:55,337 --> 00:20:58,257
<i>♪ Jàppale loxo ak yaw
Luy sa xalaat? ♪</i>

323
00:20:58,340 --> 00:21:02,177
<i>♪ Ma ngi ci sa kaw
Bëgguma dem ♪</i>

324
00:21:02,261 --> 00:21:04,179
<i>♪ Ndax bëgg naa des ♪</i>

325
00:21:04,263 --> 00:21:06,265
<i>♪ Ci sa kër ♪</i>

326
00:21:06,348 --> 00:21:09,851
<i>♪ Te yaakaar naa lii dina jaar yoon ♪</i>

327
00:21:09,935 --> 00:21:12,813
<i>♪ Waaye xam nga ñaata
Yaa ngi ma xaajale... ♪</i>

328
00:21:17,234 --> 00:21:18,151
Hm?

329
00:21:28,912 --> 00:21:31,498
Bis boobu mooy bis bi may njëkka wane nit lii.

330
00:21:31,581 --> 00:21:33,166
Oh dëggantaan?

331
00:21:34,835 --> 00:21:38,422
Uh, kon, lu tax man?

332
00:21:39,214 --> 00:21:42,759
Xamuma. Xalaatal ni dafa baax.

333
00:21:45,804 --> 00:21:47,639
Amnaa yëg-yëg bii.

334
00:21:47,723 --> 00:21:49,683
Yaakaar naa ni man ak yaw dina ñu nekk ekip bu baax.

335
00:21:51,310 --> 00:21:52,686
Man itam noonu la jàppee.

336
00:21:56,982 --> 00:22:00,527
<i>♪ Kon loo bëgga def
Luy sa xalaat ♪</i>

337
00:22:00,610 --> 00:22:03,155
<i>♪ Amna feet ci diir bu gàtt, bëgg nga... ♪</i>

338
00:22:03,238 --> 00:22:05,991
<i>Daanu nga
ci buntu bi, punk.</i>

339
00:22:07,576 --> 00:22:10,120
Ha?

340
00:22:10,203 --> 00:22:14,249
Deal bu metti, bud. implant bi
li nga chippe lépp sama moomeel la.

341
00:22:14,833 --> 00:22:17,002
Leegi maa ngi koy jëlaat.

342
00:22:24,968 --> 00:22:27,137
Uh...

343
00:22:51,828 --> 00:22:56,124
<i>♪ Dina ñu mujjee yëg xal yi ♪</i>

344
00:22:56,208 --> 00:23:00,462
<i>♪ Xal yiy jaar ci samay sidit ♪</i>

345
00:23:00,545 --> 00:23:04,841
<i>♪ Dinaa tàkk dëkk bii ♪</i>

346
00:23:04,925 --> 00:23:09,262
<i>♪ Bëggunu dellusi ♪</i>

347
00:23:09,971 --> 00:23:13,892
<i>♪ Jéem naa moom sama bopp ♪</i>

348
00:23:13,975 --> 00:23:17,687
<i>♪ Ngir nga gis limay gis ♪</i>

349
00:23:18,480 --> 00:23:22,275
<i>♪ Japp ci sa bëgg-bëgg ♪</i>

350
00:23:22,359 --> 00:23:26,530
<i>♪ Soo mënoo ma jàpp ♪</i>

351
00:23:26,613 --> 00:23:30,909
<i>♪ Baal ma ci lima la réccu ♪</i>

352
00:23:30,992 --> 00:23:35,247
<i>♪ Baal ma ci lima la réccuwaat ♪</i>

353
00:23:35,330 --> 00:23:40,001
<i>♪ Xalaatal ni amuma doole ♪</i>

354
00:23:40,085 --> 00:23:43,088
<i>♪ Leegi ♪</i>

355
00:23:43,171 --> 00:23:49,094
<i>♪ Oh, sama xol ♪</i>

356
00:23:49,177 --> 00:23:53,974
<i>♪ Mbëggeel ♪</i>

357
00:23:54,057 --> 00:23:57,435
<i>♪ Mbëggeel ♪</i>

358
00:23:57,519 --> 00:24:01,273
<i>♪ Mbëggeel ♪</i>


