1
00:01:35,260 --> 00:01:43,810
S-Scandal de soeurs

2
00:02:11,330 --> 00:02:12,020
Realisatër

3
00:02:13,430 --> 00:02:14,120
Naanal bu baax

4
00:02:21,600 --> 00:02:22,760
Lu tax mu dal noonu?

5
00:02:23,430 --> 00:02:26,230
Waaw, jàpp naa ni lépp a ngi aju ci kilifa gi.

6
00:02:28,330 --> 00:02:29,020
Lu ma dal?

7
00:02:29,730 --> 00:02:31,360
Ndax saa yu amee gan yu jigéen, dafay faral di ñëw.

8
00:02:32,060 --> 00:02:33,460
Man, kañ laa wara yegsi fii?

9
00:02:33,930 --> 00:02:36,490
Ndax man ngeen ko fàttaliku ? Daaw sama xarit bu jigeen def na luni mel.

10
00:02:38,130 --> 00:02:39,290
MAN?

11
00:02:39,760 --> 00:02:43,250
Ba noppi mu laaj ma ndax amnaa xarit bu góor?

12
00:02:43,960 --> 00:02:44,890
Ha?

13
00:02:45,360 --> 00:02:49,090
Yaa ngi rafet lool, lii mooy sama xeetu nit.

14
00:02:50,730 --> 00:02:53,990
Mën ngama jokkoo?

15
00:02:56,800 --> 00:02:58,660
Realisatër, looy def?

16
00:02:59,130 --> 00:02:59,820
Nanu dem liggéey

17
00:03:00,760 --> 00:03:05,190
Ouba, kii nee na beug nala.

18
00:03:06,360 --> 00:03:08,920
Zhisheng mooy sama xarit bu jigéen.

19
00:03:10,800 --> 00:03:14,750
Ca jamono jooju, xamuma woon ni faram la.

20
00:03:15,230 --> 00:03:16,390
Jéggalu

21
00:03:53,500 --> 00:03:54,190
Xanaa dungeen nuyu gan yi?

22
00:03:56,060 --> 00:03:57,220
And naa ci.

23
00:03:57,930 --> 00:03:58,390
Bëgg nga ma dem?

24
00:03:59,100 --> 00:04:00,720
Jarul ngeen dem.

25
00:04:07,730 --> 00:04:08,190
Nanga ma jox benn bieer.

26
00:04:08,660 --> 00:04:09,130
Ha?

27
00:04:09,600 --> 00:04:10,530
Sàngara.

28
00:04:11,460 --> 00:04:13,090
Ah! Waaw.

29
00:04:21,960 --> 00:04:22,890
- Sàngara.
- Baax na. Xam naa.

30
00:04:50,660 --> 00:04:52,750
Realisatër, bieer baa ngi ñëw.

31
00:04:54,630 --> 00:04:56,030
O, waaw kay.

32
00:05:04,660 --> 00:05:05,590
Lii sa bieer!

33
00:05:41,300 --> 00:05:42,460
Ndax dangay faral di gis nit ñuy naan bieer?

34
00:05:43,400 --> 00:05:49,290
Déedet, ni muy naan bieer rafet na lool.

35
00:06:45,000 --> 00:06:45,690
Ci kër gi?

36
00:06:50,830 --> 00:06:53,390
Sama mag ju jigéen, lu tax nga sonn nii?

37
00:06:55,030 --> 00:06:56,660
Lépp a ngi aju ci script bi.

38
00:07:02,030 --> 00:07:02,960
Ndax bind script bi baaxna ba leegi?

39
00:07:04,830 --> 00:07:06,230
Mbir mi jaar na yoon.

40
00:07:08,560 --> 00:07:09,260
Xaaral tuuti.

41
00:07:13,230 --> 00:07:14,860
Danga rafet lool.

42
00:07:17,900 --> 00:07:18,590
Laal bu baax.

43
00:07:22,330 --> 00:07:23,490
Ndax bëgg ngeen?

44
00:07:26,530 --> 00:07:27,460
Waxtaan ci li war ñu wax

45
00:07:28,860 --> 00:07:30,730
Dama am mbetteel

46
00:07:34,930 --> 00:07:35,390
Lan ngay def?

47
00:07:42,630 --> 00:07:43,320
Déedet, déet, déet.

48
00:08:03,860 --> 00:08:08,060
Soo amee xibaar 
Soo ko bëggee, wan ma ko.

49
00:08:08,530 --> 00:08:09,260
Mooy representé.

50
00:08:28,130 --> 00:08:29,760
Bëgg nga reeri ak man ci guddi gi?

51
00:08:35,830 --> 00:08:36,760
Lu tax mu tontuwul?

52
00:08:40,030 --> 00:08:42,120
Xamnaa ko

53
00:08:43,530 --> 00:08:45,160
Sama rakk script ba leegi mingi dox bu baax.

54
00:08:45,630 --> 00:08:47,030
Mooy representé.

55
00:08:50,760 --> 00:08:54,960
Xam nga ni amnaa yaakaar yu bari ci filmu bii.

56
00:09:37,660 --> 00:09:41,390
Dama am luma doon saytu 
yokk ci ndaje neexal bii.

57
00:09:43,960 --> 00:09:47,690
Kon xamna lumu wara def.

58
00:09:50,260 --> 00:09:50,960
Xalaat na ci bu baax

59
00:09:57,030 --> 00:10:05,420
Nit ñi dañu wax ni realisatëru filmu bi 
Filmu bii mooy Madam Yun, xalaatal bu baax.

60
00:10:53,960 --> 00:10:55,120
Ah, xamuma.

61
00:10:57,000 --> 00:10:57,690
Xalaat ngir yokkute ci wàllu tàggat yaram

62
00:11:29,200 --> 00:11:30,130
Yun Jing.

63
00:11:31,060 --> 00:11:31,990
- Mag ju jigéen!
- Oh.

64
00:11:33,630 --> 00:11:36,650
Amaana tay damay yeex tuuti ci overtime yi.

65
00:11:37,130 --> 00:11:38,530
Xamleen loolu

66
00:11:39,930 --> 00:11:42,260
naka la baat bi 
samam nekk na noonu?

67
00:11:43,430 --> 00:11:46,450
déet, dama sonn tuuti

68
00:11:47,160 --> 00:11:47,860
Oh, xamnaa loolu.

69
00:11:48,800 --> 00:11:49,490
Nu gise ci kër ga.

70
00:11:50,660 --> 00:11:50,890
Nu gisewaat.

71
00:13:00,000 --> 00:13:02,000
Tekkib sous-titre: AnanVinh

72
00:13:19,800 --> 00:13:22,130
Duma woon noonu 
loolu yàgg na lool.

73
00:13:23,760 --> 00:13:27,490
Xam nga, jéem naa
naka ngay toppatoo ma?

74
00:13:29,360 --> 00:13:30,290
Jërëjëf.

75
00:13:32,630 --> 00:13:37,290
Leegi filmu sunu mag ju jigéen ñëw na.

76
00:13:38,230 --> 00:13:40,460
Mooy representé.

77
00:13:42,430 --> 00:13:46,160
Bul jaaxle, dinaa jéem say film.

78
00:13:47,800 --> 00:13:48,730
Gëm leen, mën naa ko.

79
00:13:49,900 --> 00:13:50,590
Ndax xam nga ko ?

80
00:17:21,290 --> 00:17:24,090
Bul jaaxle, bëgg nga ko?

81
00:18:57,660 --> 00:18:58,820
Yun Jing

82
00:19:36,160 --> 00:19:37,320
Lii café internet la?

83
00:19:39,200 --> 00:19:40,590
Cafe internet ci wetu kër gi.

84
00:19:41,060 --> 00:19:42,220
Jërëjëf.

85
00:19:45,260 --> 00:19:48,060
Waaye, ndax buntu bi ci topp mingi ci cammoy bi wala ci ndijoor gi?

86
00:19:49,000 --> 00:19:49,930
Jub.

87
00:19:50,630 --> 00:19:52,260
Jub.

88
00:19:53,430 --> 00:19:54,360
Ndax dañuy jaay fideo yuñ saaf?

89
00:19:54,830 --> 00:19:56,230
Dédeet, bii café la.

90
00:19:57,630 --> 00:19:58,560
Danuy jaay ci sunu askan

91
00:20:01,130 --> 00:20:02,290
Doy waar!

92
00:20:03,230 --> 00:20:04,160
Dafay jaay itam yàppu mbaam xuux bu forox ak bu saf suukër.

93
00:20:10,930 --> 00:20:13,020
Dafa dof may wax la ni dëgg la.

94
00:20:14,200 --> 00:20:15,590
Duma dem ci cafe internet yi.

95
00:20:16,530 --> 00:20:19,550
Maa ngi jéggalu ci ni kiliyaan bi bëggee 
Pont internet leegi.

96
00:20:21,200 --> 00:20:22,590
Waaw, jox ma benn bieer.

97
00:20:24,000 --> 00:20:24,450
Waaw, kilifa gi.

98
00:20:25,630 --> 00:20:28,190
Maa ngi lay jox benn butéelu bieer bu sedd.

99
00:20:28,660 --> 00:20:29,130
Waaw, njiit li.

100
00:20:48,500 --> 00:20:49,430
Noo ngi leen di sant ci li ngeen nangu laaj, 
Am nga xarit bu góor?

101
00:20:51,760 --> 00:20:53,850
Yaa ngi rafet lool, lii mooy sama lekk.

102
00:20:54,560 --> 00:20:56,430
Mën nga ànd ak man génn?

103
00:21:04,600 --> 00:21:06,220
Ndax am nga koo bëgg?

104
00:21:08,330 --> 00:21:14,620
Ndax bëgg naa ko lool, ndax mën naa ko bëgg?

105
00:21:19,060 --> 00:21:21,390
Lu baax la.

106
00:21:23,960 --> 00:21:24,890
Nii rekk la.

107
00:21:40,300 --> 00:21:43,090
Ndax am nga koo bëgg?

108
00:21:43,800 --> 00:21:45,420
Déedet, lu xew?

109
00:21:48,460 --> 00:21:51,490
Rafet nga lool, loolu mooy sama plaat.

110
00:21:52,900 --> 00:21:53,590
Woowal ma.

111
00:21:55,460 --> 00:21:57,330
MAN?

112
00:21:58,030 --> 00:22:00,830
Waaw, gis naa ko bu njëkk.

113
00:22:02,700 --> 00:22:06,190
Ndijaay, ndax yeewu nga?

114
00:22:07,600 --> 00:22:08,760
Lii...

115
00:22:16,460 --> 00:22:18,550
Ku ñàkk xam-xam!

116
00:22:28,600 --> 00:22:30,220
Booy seet, amna dof yu ma bëgg.

117
00:22:32,800 --> 00:22:33,960
Xoolal ndax ba leegi mënu ma dem ci kafe bi.

118
00:22:55,430 --> 00:22:57,060
Lu tax doo jokkoo ak man?

119
00:23:05,930 --> 00:23:06,160
Nanga def mag ju jigéen.

120
00:23:06,630 --> 00:23:10,590
Lu xew? Lu tax doo jël telefon bi sooy woo? 
Xamuma, ndax amna ku ma jaaxal ci kër gi?

121
00:23:12,930 --> 00:23:14,790
Sama mag ju jigéen, jéggalu, waaye déet.

122
00:23:15,730 --> 00:23:16,890
Leegi ci liggéeyukaay bi.

123
00:23:17,360 --> 00:23:18,060
Xam naa.

124
00:23:19,460 --> 00:23:21,790
Bima delloo, dama dee dëgg.

125
00:23:22,500 --> 00:23:24,360
Xam naani dootuloo noonu.

126
00:23:25,060 --> 00:23:25,760
Baal ma.

127
00:23:27,400 --> 00:23:28,790
Ndax seetlu nga Lu dem liggéey?

128
00:23:30,430 --> 00:23:32,060
Ba léegi.

129
00:23:33,230 --> 00:23:35,790
May ko mu firndeel script bi ci guddi gi.

130
00:23:37,200 --> 00:23:39,060
Xamnaa sama mag ju jigéen, dinaa la gise ci kër gi.

131
00:23:39,530 --> 00:23:40,930
Nuyu.

132
00:23:45,600 --> 00:23:46,760
Lan ngay def? 

133
00:23:50,500 --> 00:23:53,520
Danga njëkka sangu ba noppi nga jeexal senaario bi.

134
00:23:58,200 --> 00:23:58,890
Leegi kan mooy kii?

135
00:24:00,530 --> 00:24:01,930
Ku nekk dem añ.

136
00:24:03,800 --> 00:24:04,490
M. ndawu réew mi?

137
00:24:06,130 --> 00:24:08,460
Representant ci liggéey bi

138
00:24:10,560 --> 00:24:11,720
Laaj ma lan laa wara sol?

139
00:24:15,930 --> 00:24:20,130
Lu tax nga bëgga xam?
Ban yéere nga sol?

140
00:24:23,630 --> 00:24:24,860
Waaye yaw nak?

141
00:24:25,260 --> 00:24:26,420
Dafa doy waar

142
00:24:28,300 --> 00:24:31,790
Ak ci njeexte ayu-bis bii, xamnaa ni sa aniwerseer la.

143
00:24:32,500 --> 00:24:35,760
Soo ko fàttee duma la bàyyi nga dem.

144
00:24:37,160 --> 00:24:37,860
Xam nga loolu?

145
00:24:42,300 --> 00:24:43,460
Xam naa.

146
00:24:45,560 --> 00:24:46,720
Dinaa la jokkoo ëllëg.

147
00:24:54,660 --> 00:24:55,590
Ndax yaay ndawu biir bi?

148
00:24:56,760 --> 00:24:58,390
Kon, naka ngay ko woowe?

149
00:24:59,100 --> 00:25:00,030
Leegi mooy waxtu lekk, demal lekk.

150
00:25:02,600 --> 00:25:03,990
Lu nga bëgga gis, te doo ma wax benn baat?

151
00:25:15,660 --> 00:25:17,530
Fan la nit ñooñu bawoo?

152
00:25:19,400 --> 00:25:21,490
Fan nga ko bëgga gis? Du fii?

153
00:25:21,730 --> 00:25:22,190
Daf ma raglu.

154
00:25:22,660 --> 00:25:24,290
Bul fëgg sama bunt ngir tiital ma.

155
00:25:26,160 --> 00:25:28,720
Ba leegi ndawu réew mi mingi seetaan filmu yellow yi.

156
00:25:30,130 --> 00:25:34,790
Fan laa mëna seetaane filmu yellow yi? Maa ngi seetaan 
Filmu art ngir gis tendaas yu bees yi.

157
00:25:37,360 --> 00:25:40,630
Nit ñi neena ñu yaa ngi waajal 
ngir filmu bii bu yàggul.

158
00:25:42,030 --> 00:25:45,520
naka nga xamee ni sekkere liggéeyukaay la?

159
00:25:46,460 --> 00:25:48,330
Dëgg la dina am anam wuñu ko mëna xamee

160
00:25:49,260 --> 00:25:51,130
Amna sama jikko ci biir.

161
00:25:51,830 --> 00:25:52,760
Jub?

162
00:25:53,930 --> 00:25:56,950
Script bi dina génn tay.

163
00:25:59,760 --> 00:26:01,850
Ci sa tur, xamnaa ni bëgg naa la.

164
00:26:03,030 --> 00:26:03,260
Ci lu wóor.

165
00:26:26,360 --> 00:26:27,990
Xaaral tuuti, amna ku nekk ci biti.

166
00:26:28,700 --> 00:26:31,030
Sekkerteer bi xamna kan mooy patroŋam.

167
00:26:31,730 --> 00:26:33,360
Xamoon na ni xamna.

168
00:26:34,530 --> 00:26:37,090
Amna sekretër bu génn ngir lekk.

169
00:26:38,030 --> 00:26:38,720
Lan la?

170
00:27:30,760 --> 00:27:33,560
Yatt.

171
00:27:57,360 --> 00:28:13,690
Mbëggeel dafa melni tóor-tóor buy tóor-tóor ci àll bi.

172
00:28:14,630 --> 00:28:22,090
Dafay xëcc xeeti yamb yu bari.

173
00:28:22,560 --> 00:28:27,450
Bàyyileen mu dajale lem ba noppi mu ni mes.

174
00:28:34,930 --> 00:28:36,330
Ah, mënu ma bind.

175
00:28:38,900 --> 00:28:45,190
Nekk dof.

176
00:28:48,000 --> 00:28:50,330
Dama soxla royuwaay.

177
00:29:04,560 --> 00:29:05,490
Géj a gise.

178
00:29:14,600 --> 00:29:19,020
- Ñaata at a ngi nii nu mujjee gise?
- Lu tollu ci benn ayu-bis.

179
00:29:19,730 --> 00:29:25,550
Ndax jàpp naa ni ñu may nu 
jël na filming bi ba noppi bëgga daw.

180
00:29:26,960 --> 00:29:29,990
Du sudee danga wara direct 
tegtal, lan laa wara def?

181
00:29:32,100 --> 00:29:33,720
Lu nga filme ci jamono jii?

182
00:29:34,200 --> 00:29:35,590
Dokumentaar bi sonal na lool.

183
00:29:39,560 --> 00:29:43,050
Ndax xam nga ban bis la suba?

184
00:29:43,760 --> 00:29:47,720
Dëgg la dina xam limu doon. Am nanu benn 
aniwerseer bu dal. Laaj naa ko lu bari yoon.

185
00:29:49,360 --> 00:29:50,760
Ban kado ngay yónnee?

186
00:29:52,860 --> 00:29:57,060
Dafa melni lu jafe lool may wax ko lu njëkk, sama xol. 
Lu nga bëgga def ci bis bii?

187
00:30:01,030 --> 00:30:06,630
Dama bëgga sol taloŋ yu weex 
ak robb guddi bu rafet ni biddiiw.

188
00:30:08,500 --> 00:30:09,890
Lu ngay ree?

189
00:30:10,830 --> 00:30:11,520
Ba leegi am nga ko?

190
00:30:13,160 --> 00:30:15,960
Calcul Ouba dinaa guiss sa waajal.

191
00:30:16,660 --> 00:30:17,590
Ndax danga bëgga def loolu?

192
00:30:20,160 --> 00:30:20,860
Gëm naa la Ouba.

193
00:30:21,330 --> 00:30:25,990
Sama xol, xool bu baax daf may bëgga fóon.

194
00:30:27,160 --> 00:30:27,630
Wala lan?

195
00:30:31,130 --> 00:30:31,590
Fóon la.

196
00:31:21,530 --> 00:31:22,220
Lu xel nangu?

197
00:31:23,860 --> 00:31:24,560
Dafay waaja lekk.

198
00:31:29,230 --> 00:31:29,690
Lan?

199
00:31:30,400 --> 00:31:32,330
Bu yàggul gisuma ko 
Suppu miso bi ma gëna bëgg.

200
00:31:33,900 --> 00:31:35,990
Loolu rekk la ci sa mag ju jigéen 
ndam. Leegi damay jaxasoo lool.

201
00:31:37,160 --> 00:31:40,650
Lan ngay def ngir am ndam ci barabu jaamukaay bi?

202
00:31:41,600 --> 00:31:42,990
Ndax mat nga script bi?

203
00:31:44,630 --> 00:31:47,190
Waaw, yónnee nañu mail yépp.

204
00:31:48,830 --> 00:31:51,850
Ci sa xalaat, naka la senaario bi di doxee?

205
00:31:52,560 --> 00:31:54,650
Um.

206
00:31:54,660 --> 00:31:58,150
Dafa yaakaar ni mën na tekki ci askan wi.

207
00:31:58,860 --> 00:32:00,260
Bul jaaxle ci am ndam.

208
00:32:03,760 --> 00:32:04,460
Naka nga ko xamee ?

209
00:32:06,800 --> 00:32:10,290
Ha?

210
00:32:10,300 --> 00:32:13,320
Amul jiroom benneelu yëg-yëg?

211
00:32:16,130 --> 00:32:16,860
Ban waxtu la?

212
00:32:17,300 --> 00:32:18,230
Ni ñuy yeexee liggéey.

213
00:32:52,530 --> 00:32:55,790
Bii yoon filmu la, dinaa la satisfaire.

214
00:33:22,860 --> 00:33:24,490
Waaw, man maay ndawul Lu.

215
00:33:24,960 --> 00:33:28,230
Leegi maa ngi xool script bi, 
ñëwal sama biro 3 waxtu ci ngoon.

216
00:33:28,930 --> 00:33:29,390
Xam naa ko.

217
00:33:54,360 --> 00:33:59,030
Oh, man maay Lu yor mbind mi. 
Maa ngi génn tay.

218
00:33:59,730 --> 00:34:03,460
Waaw, M. Representant, nanu daje foofu.

219
00:34:14,430 --> 00:34:17,580
Sama mébet mooy nekk aktër.

220
00:34:17,580 --> 00:34:22,360
wuute na ak aktër yi am background yu rafet 
Leneen lu rafet, mën naa ko wóolu ci sama yaram.

221
00:34:24,000 --> 00:34:28,660
Dëgg la, ñeneen ñi mën nañu ko
sëy ak ma, waaye duma ragal dara.

222
00:34:30,300 --> 00:34:32,390
Dama ragal ni mënu ma nekk aktër.

223
00:34:33,330 --> 00:34:35,190
Kon, lenn li ma 
mën def luy fësal saa yu nekk

224
00:34:37,060 --> 00:34:39,860
tay itam maa ngi waajal jëfandikoo 
sama yaram ngir gént yooyu.

225
00:35:17,200 --> 00:35:21,390
Yaay sama ñam dëgg; 
Dina ànd ak man génn.

226
00:35:23,500 --> 00:35:24,890
Man kan laa?

227
00:35:25,830 --> 00:35:28,160
Waaw, gis naa la bu njëkk.

228
00:35:30,500 --> 00:35:31,890
Ndijaay, ndax yeewu nga?

229
00:35:33,300 --> 00:35:33,750
Feebaru xel!

230
00:35:35,160 --> 00:35:36,560
Ah, yaw dof.

231
00:35:37,260 --> 00:35:38,890
Amaana ci njëkk

232
00:35:55,000 --> 00:35:55,690
Sama mag ju jigéen yegsi na.

233
00:35:56,400 --> 00:35:57,790
Representant Lu ci biir.

234
00:35:59,200 --> 00:35:59,890
Mu ngi lay xaar ci biir.

235
00:36:01,060 --> 00:36:02,460
Sama mag ju jigéen dafa wara liggéey bu baax.

236
00:36:04,330 --> 00:36:04,790
Jërëjëf.

237
00:36:10,400 --> 00:36:11,120
Kaf.

238
00:36:18,100 --> 00:36:19,720
Oh, duggal, toog.

239
00:36:20,200 --> 00:36:21,130
Waaw, Ndaw.

240
00:36:33,730 --> 00:36:34,420
Jeexal naa jàng eskiript bi.

0
00:00:20,260 --> 00:00:59,810
Tekkib sous-titre: AnanVinh

241
00:36:35,130 --> 00:36:36,530
Gaaw luma yaakaaroon ni noonu la.

242
00:36:37,230 --> 00:36:39,090
Ndax ba leegi sa xol sedd na?

243
00:36:40,500 --> 00:36:42,360
Dama jàpp ni senaario bi war na soppiku.

244
00:36:43,760 --> 00:36:44,920
Ah?

245
00:36:45,400 --> 00:36:47,490
naka ngay soppi sa bànneex?

246
00:36:49,360 --> 00:36:51,690
Ndax mën na bàyyi realisatër bi nekk mbëggeelam?

247
00:36:53,560 --> 00:36:54,260
Lan nga bëgg?

248
00:36:54,960 --> 00:36:58,230
Kan mooy filme ak moom ba leegi, style jeu bi ci suuf 
Réew mi bokkul ak 70s.

249
00:36:58,700 --> 00:37:04,290
Aktris amul chance 
Dundu te doo bëgg jeu.

250
00:37:05,000 --> 00:37:10,820
Fi may jeexalee mooy nu jëfandikoo drame ngir sublime, 
Waaye luy flër ak luy suytu ferñeent yi?

251
00:37:11,760 --> 00:37:15,030
Lu tax nga bëgga nàmp, di nàmp saa yu nekk, waaye di wéy di nàmp?

252
00:37:16,900 --> 00:37:20,630
Damay dugg ci Anternet bi, internet bi, añs.

253
00:37:23,660 --> 00:37:25,060
Bu yàgg a ngi may bàyyi realisatër bi mu sëy.

254
00:37:27,160 --> 00:37:28,560
Kon amul yëg-yëg.

255
00:37:29,260 --> 00:37:30,190
- M. Ndaw li.
- Lu xew?

256
00:37:30,430 --> 00:37:32,060
Wax ma lu jëm ci fitnaal ci wàllu awra?

257
00:37:32,760 --> 00:37:35,090
Lii mooy saas bu mujj ngir soppiwaat.

258
00:37:37,200 --> 00:37:38,360
Ray bu jigéen bi baaxna.

259
00:37:39,060 --> 00:37:41,150
Lu nga bëgga wax ci sama mag ju jigéen?

260
00:37:42,330 --> 00:37:44,890
Sa mag ju jigéen daf ma sant ma may la chance.

261
00:37:59,360 --> 00:38:01,450
Kontaan lool.

262
00:39:17,760 --> 00:39:18,490
Loolu...

263
00:39:24,760 --> 00:39:32,690
Li may mujjee mooy jéggalu, 
Ndax naan bieer bàkkaar la?

264
00:39:47,160 --> 00:39:51,590
Ci sama script, xamna luy ree.

265
00:39:52,060 --> 00:39:55,790
Soo bëggee filme danga wara am realisatër 
mu wut ma digal ko.

266
00:39:57,660 --> 00:39:59,290
Realisatëru filmu la.

267
00:40:01,860 --> 00:40:03,020
Realisatër bu rafet.

268
00:40:05,830 --> 00:40:07,230
Ndax rafet naa?

269
00:40:09,330 --> 00:40:10,490
Ndax bëgg naa lii?

270
00:40:13,300 --> 00:40:13,990
Rafet na lool.

271
00:40:16,800 --> 00:40:18,890
Te daa rafet lool.

272
00:40:21,460 --> 00:40:23,090
Ndax rafet naa?

273
00:40:24,030 --> 00:40:24,960
Am.

274
00:40:25,430 --> 00:40:26,120
Ndax rafet na?

275
00:40:26,600 --> 00:40:32,660
Loolu rafet na?

276
00:40:38,030 --> 00:40:39,190
Sàcc naxaatekat.

277
00:40:42,700 --> 00:40:43,630
- Nijaay.
- Hey.

278
00:40:45,500 --> 00:40:47,590
Ndijaay, danga taaru lool.

279
00:40:48,530 --> 00:40:52,260
Ndijaay, ne nga bëgg nama, wala book?

280
00:40:54,830 --> 00:40:56,230
Ndijaay, ndax danuy waxtaan?

281
00:40:58,800 --> 00:41:05,090
Waaw kay, waaye ba leegi xamuma tuuru realisatër bi.

282
00:41:07,200 --> 00:41:07,650
Sama tur

283
00:41:09,530 --> 00:41:13,490
Man Yunzhen laa tudd.

284
00:41:15,830 --> 00:41:16,760
Ndijaay, yaw nak?

285
00:41:18,160 --> 00:41:22,830
Man maay Jin Cheng Fan, Chengfan.

286
00:41:25,400 --> 00:41:28,890
Ndijaay Jin Chengfan

287
00:41:31,230 --> 00:41:31,920
Ndijaay Jin Chengfan

288
00:41:33,330 --> 00:41:40,550
Ok, kon ndijaay Jin Chengfan, 
Tay lanu tàmbali bis bu njëkk bi.

289
00:41:41,730 --> 00:41:43,360
Tay lanu tàmbali jokkoo.

290
00:41:44,760 --> 00:41:45,690
Bis bu njëkk

291
00:41:47,100 --> 00:41:47,320
Dëmb

292
00:41:52,700 --> 00:42:02,720
Tay, danu tàmbali waxtaan ngir naan benn kaasu vin.

293
00:43:06,900 --> 00:43:07,350
Mooy representé.

294
00:43:07,830 --> 00:43:09,230
Oh, nanga def.

295
00:43:14,600 --> 00:43:15,760
Ndax amna script ci jamono jii?

296
00:43:17,160 --> 00:43:20,430
Liggéey te lire personage bi nga bëgga jouer te nga wax ma ko.

297
00:43:21,130 --> 00:43:23,460
Sama ndawu liggéey, jërëjëf waay.

298
00:43:25,800 --> 00:43:28,130
Dinaa la ko jox 
liggéey bu amul fenn tay.

299
00:43:29,060 --> 00:43:29,990
Serwiis bu amul fenn.

300
00:43:31,400 --> 00:43:32,090
Ndax mën ngeen ma gëm?

301
00:43:32,800 --> 00:43:34,420
Ci lu wóor.

302
00:43:35,830 --> 00:43:36,290
Lan?

303
00:43:37,460 --> 00:43:38,160
Ndax mën nga ko def ?

304
00:44:17,530 --> 00:44:19,690
Lan ngay mëna def sudee 
gaaw nga jeexal?

305
00:44:21,800 --> 00:44:23,190
Ndax dinga ñëwaat?

306
00:44:26,230 --> 00:44:26,920
Xamleen loolu.

307
00:44:45,360 --> 00:44:46,520
Leeral.

308
00:44:47,460 --> 00:44:49,550
Ndax yaw.

309
00:45:50,000 --> 00:45:53,020
Sa ndawu réew gaawna lool, amnaa ko 
Lan lañu mën a def ? Maa ngi tàmbali.

310
00:46:46,460 --> 00:46:47,390
Liggéeyal bu baax

311
00:46:55,100 --> 00:46:56,030
- Bëgg nga ko?
- Bëgg naa ko.

312
00:48:00,000 --> 00:48:05,000
Tekkib sous-titre: AnanVinh

313
00:48:20,500 --> 00:48:21,660
Lu tax ma bëgga naan?

314
00:48:31,460 --> 00:48:34,260
Xale bi waxul dara lu jaarul yoon, 
Ndax maa ngi wéet lool?

315
00:48:45,930 --> 00:48:47,790
Bëgg nga tuumal ma ci wàllu awra?

316
00:48:49,200 --> 00:48:50,360
Ray bu jigéen bi baaxna.

317
00:48:51,300 --> 00:48:51,990
Lan nga bëgg?

318
00:48:54,560 --> 00:48:57,120
Sama mag ju jigéen war na am dara.

319
00:49:14,400 --> 00:49:15,790
Naka nga ko def?

320
00:49:28,630 --> 00:49:30,030
<i>Tontu wuñu woo yi nga def.</i>

321
00:49:30,260 --> 00:49:31,190
<i>Telefoŋ bi lëkkaloowul</i>

322
00:49:35,630 --> 00:49:36,090
Soxna.

323
00:49:38,900 --> 00:49:41,920
Loy def? Woo bi jaaxal nama lool.

324
00:49:43,560 --> 00:49:45,190
Maa ngi jéggalu, bëgguma ko.

325
00:49:47,530 --> 00:49:48,690
Waaye Yun Jing.

326
00:49:50,560 --> 00:49:52,890
Loolu du dara, demal sa kër nga waxtaan.

327
00:49:59,660 --> 00:49:59,890
Jëkkal toog.

328
00:50:05,030 --> 00:50:06,430
Yun Jing

329
00:50:07,360 --> 00:50:09,230
Wax ma dëgg

330
00:50:09,700 --> 00:50:11,560
Ndax amna lu nekk ci sa diggante ak Lu?

331
00:50:12,960 --> 00:50:14,120
Dara.

332
00:50:16,930 --> 00:50:18,790
Yaakaar naa itam li nga wax dëgg la.

333
00:50:21,360 --> 00:50:24,390
Lu tax ndawul Lu wax ni dafa nelaw ak yaw?

334
00:50:26,500 --> 00:50:26,720
Neena itam maa ngi ci jàmm.

335
00:50:29,300 --> 00:50:31,160
Lu xaj bu mag bi wax?

336
00:50:31,630 --> 00:50:32,560
Um.

337
00:50:35,830 --> 00:50:38,160
Nanga def, mag ju jigéen.

338
00:50:39,800 --> 00:50:41,420
Booy seet,

339
00:50:43,760 --> 00:50:53,780
Representant Lu neena lu wuute 
Boo tëddee ak moom, dinañu la dàq ci mbooloo mi.

340
00:50:56,360 --> 00:51:01,030
Neena dina yónnee filmu bi 
moom ci beneen njiit.

341
00:51:03,830 --> 00:51:05,230
Kon, ma nelaw ak moom.

342
00:51:07,100 --> 00:51:10,830
Sister, dama ragal ni doo mëna filme.

343
00:51:11,530 --> 00:51:19,230
Kan moo la wax nga dem? Yeen sama gaa yi? 
ay xale? Kan moo la wax nga def loolu?

344
00:51:19,230 --> 00:51:21,790
Yun Jing, soo amee lu mel nii, 
Waxtaan ak sa mag ju jigéen.

345
00:51:29,030 --> 00:51:30,430
Soo nekkee sa bopp, naka ngay ragal?

346
00:51:32,760 --> 00:51:34,390
Leegi dinaa la déglu.

347
00:51:37,900 --> 00:51:38,590
Dinaa ko rey.»

348
00:51:39,300 --> 00:51:43,250
Bul dem, su amee lu xew 
Lu tax doo ànd ak man ci biti? Bul génn ndax man.

349
00:51:45,830 --> 00:51:47,460
Maa ngi ko bëgga ray itam.

350
00:51:50,500 --> 00:51:52,590
Xaaral tuuti?

351
00:51:53,530 --> 00:51:57,950
Sudee kontaanoo ci, lan lañu mën a def ? 
Mën nañu nu nax rek.

352
00:52:04,730 --> 00:52:09,860
Maa ngi jéggalu, maa ngi jéggalu, dinaa 
Yobbul mbir yooyu yaw kese.

353
00:52:17,330 --> 00:52:19,660
Sister, maa ngi lay massawu.

354
00:52:21,300 --> 00:52:24,090
Maa ngi jéggalu sama mag ju jigéen.

355
00:54:17,960 --> 00:54:19,120
Jubalal.

356
00:54:24,030 --> 00:54:24,960
Ndax xiif nga?

357
00:54:27,760 --> 00:54:32,190
Sama mag ju jigéen, danga baax lool ndax sama mag ju jigéen nga.

358
00:54:34,060 --> 00:54:35,220
Yaw itam.

359
00:54:36,160 --> 00:54:37,560
Ndax Yun Jing baaxna lool

360
00:54:42,930 --> 00:54:49,460
Amoon na benn acteur bu nelawoon ak moom mu ni 
Jox nañu ko benn rôle ci sama script.

361
00:54:50,630 --> 00:54:51,320
Lu tax?

362
00:54:52,030 --> 00:54:52,960
Lan la?

363
00:54:57,860 --> 00:54:59,950
Mën nanu fexe ba nit ki daanu.

364
00:55:01,830 --> 00:55:02,520
Naka lañu koy defee ?

365
00:55:02,530 --> 00:55:04,390
Ndax am nga nimero telefonu aktër bi?

366
00:55:07,660 --> 00:55:09,060
Biro bi dafa wara am kàrtu liggéeyukaay.

367
00:55:11,630 --> 00:55:12,320
Ma jëlaat ko.

368
00:56:14,630 --> 00:56:15,560
Lan ngay bëgga am ci bànneex?

369
00:56:18,600 --> 00:56:19,530
Bii...

370
00:56:20,930 --> 00:56:21,620
Nanga duggu ci anam wu ofisel.

371
00:56:23,960 --> 00:56:24,660
Dëgg la?

372
00:56:25,360 --> 00:56:26,760
Bul fàtte.

373
00:56:28,400 --> 00:56:31,190
Ndax mënu nu déggoo ci anam wu ofisel?

374
00:56:34,700 --> 00:56:38,430
Kon màggal sunu ndaje te naan.

375
00:56:38,900 --> 00:56:40,520
Neex na!

376
00:57:01,760 --> 00:57:02,460
Xaaral ma jox lii Hai.

377
00:57:10,160 --> 00:57:10,860
Sama aniwerseer.

378
00:57:24,630 --> 00:57:35,120
Ouba mooy jënd IPad, mu laaj Hai ban kado lay jox.

379
00:57:40,730 --> 00:57:43,060
Ndax loolu dafay merloo sama mag ju jigéen.

380
00:57:45,400 --> 00:57:46,560
Kon, lan laa wara laaj Ouba?

381
00:58:10,360 --> 00:58:11,060
Yékkati toast.

382
00:58:24,130 --> 00:58:25,290
Danu am yoon ci sunu diggante.

383
00:58:27,400 --> 00:58:28,560
Jub.

384
00:58:36,260 --> 00:58:37,420
Ba leegi noo ngi nelaw, wala book?

385
00:58:40,000 --> 00:58:43,260
Dama bëgga ñëwaat.

386
00:58:48,160 --> 00:58:48,860
Ayca.

387
00:58:50,730 --> 00:58:51,420
Luy lii fii?

388
00:58:54,230 --> 00:58:54,920
Du fii.

389
00:58:57,500 --> 00:58:58,430
Waaye fan?

390
01:01:00,000 --> 01:01:05,000
Tekkib sous-titre: AnanVinh

391
01:02:35,660 --> 01:02:36,630
Loo ci xalaat ?

392
01:02:39,630 --> 01:02:40,790
Ndax maa ngi jaaxle lool?

393
01:03:16,260 --> 01:03:17,660
<i>Woo bi nga def mënu ñu ko boole</i>

394
01:03:26,060 --> 01:03:26,290


395
01:03:54,760 --> 01:03:55,230
jëluma telefon bi.

396
01:04:30,000 --> 01:04:30,950
Kañ ngay agsi fii?

397
01:04:42,360 --> 01:04:43,060
Bul ko nangu?

398
01:04:47,500 --> 01:04:56,120
Jin Ying Zhe bëggul woon jënd kado, 
muni ma du ab moine.

399
01:04:56,600 --> 01:04:58,220
Soo ko bëggul, wax rek ni danga bon.

400
01:05:00,560 --> 01:05:03,120
Def nañu ko ba noppi.

401
01:05:07,560 --> 01:05:16,190
Nit ku bonn la woon 
Jigéen ñi war nañu jooy, baaxal seeni maam.

402
01:05:17,130 --> 01:05:18,290
Xaj ibrid.

403
01:05:21,100 --> 01:05:23,660
Xaj mbalit hybrid bu bawoo jahannama moo ci topp.

404
01:05:26,930 --> 01:05:29,730
Sama pàppa bëgga mar sa nopp.

405
01:05:30,900 --> 01:05:32,060
Loolu xale yi waruñu ko dégg.

406
01:05:33,230 --> 01:05:35,560
Lu tax doo déglu?

407
01:05:36,500 --> 01:05:42,090
Maanaam, boo déggee wax ju bon, 
Dama ragal nga mel ni ñoom.

408
01:05:43,260 --> 01:05:49,550
Pàppa, bul jaaxle. Bëgguma loolu sama mag ju jigéen.

409
01:05:51,430 --> 01:05:51,890
Loolu mooy sama doom ju jigéen.

410
01:05:55,160 --> 01:06:00,760
Dama jaaxle ci sama pàppa.

411
01:06:01,460 --> 01:06:05,190
Sama yaay bu bees bi du melni yaw.

412
01:06:06,360 --> 01:06:10,790
Lii ab tegtal la 
Nanu dem.

413
01:06:12,430 --> 01:06:14,760
Nanu dem, jàpp naa ni sama mag ju jigéen baaxul.

414
01:06:42,760 --> 01:06:43,920
Yun Jing, bëgg naala.

415
01:07:16,830 --> 01:07:17,760
Yun Jing, bëgg naala.

416
01:07:22,430 --> 01:07:23,360
Ouba, lii dafa soof lool.

417
01:07:31,300 --> 01:07:33,390
Yun Jing, jàngal ma limu ma gis.

418
01:07:35,030 --> 01:07:37,360
Anh không trả lời điện thoại

419
01:07:45,530 --> 01:07:45,990
jàpp

420
01:07:49,500 --> 01:07:53,450
Ouba, ñëwal, em bay giờ giống 
Maa ngi gént, dama melni biddéew.

421
01:07:54,860 --> 01:08:00,930
Ohba, mënu ma leen wax, dellu leen.

422
01:08:01,630 --> 01:08:07,690
Tất nhiên, Ouba luôn rất 
đáng tin cậy xung quanh em.

423
01:08:09,330 --> 01:08:11,420
Ouba, beug naala.

424
01:08:13,300 --> 01:08:16,560
Ouba itam Yun Jing la, bëgg naala lool.

425
01:09:10,460 --> 01:09:11,620
Tói dé một yêu

426
01:09:13,260 --> 01:09:16,530
Bëgg naa sama xarit bu jigéen am aniwerseer bu amul fenn.

427
01:09:17,000 --> 01:09:17,220
Làm thế nào để làm nào?

428
01:09:17,700 --> 01:09:18,860
Ndax xam nga ?

429
01:09:20,030 --> 01:09:23,990
Nit ku xoromu la, waaye maa ngi ci jàmm.

430
01:09:24,700 --> 01:09:25,150
Jërëjëf.

431
01:11:45,630 --> 01:11:46,090
Soeur Hai, dellu naa.

432
01:11:48,430 --> 01:11:49,120
Lan ngay def?

433
01:11:50,060 --> 01:11:50,290
Ndax yaay bind script bi?

434
01:11:51,700 --> 01:11:53,090
Leegi dama bëgga jéem beneen filmu.

435
01:11:54,730 --> 01:11:55,190
Luy tur filmu bii?

436
01:11:57,760 --> 01:11:58,690
Xalaat yu bon.

437
01:12:01,260 --> 01:12:01,960
Tur wu mag!

438
01:12:08,960 --> 01:12:10,120
Kartu liggéeyukaay, sama mag ju jigéen.

439
01:12:12,230 --> 01:12:13,160
- Lu jëm ci aktër yi?
- Waaw.

440
01:12:29,730 --> 01:12:31,590
Madam Shiren moo yor eskiript bi fii.

441
01:12:33,230 --> 01:12:35,090
Lii mooy li ndawul Lu wane ma.

442
01:12:36,500 --> 01:12:39,520
Man maa bind script bii, man maay realisatër bi.

443
01:12:41,400 --> 01:12:45,130
Ah, lii mooy réalisateur bi, waaye luma dal?

444
01:12:46,760 --> 01:12:50,030
Ci saasi ma wax vocation nekk jigéen.

445
01:12:51,200 --> 01:12:55,150
Bëgg naa ñu yàq Lu, loo xalaat?

446
01:12:56,560 --> 01:12:57,490
Ndax loolu amna solo?

447
01:12:58,900 --> 01:13:01,690
Shiren xiamu, dunu dem ci ndaje mi.

448
01:13:01,930 --> 01:13:02,390
Sama wareef moo gëna am solo.

449
01:13:03,560 --> 01:13:06,120
Man maay realisatër bi, maa leen di jox cër yi.

450
01:13:07,300 --> 01:13:10,560
Dëgg la dina ñu yàq nit ki.

451
01:13:15,230 --> 01:13:17,090
Démb laa dee.

452
01:13:19,430 --> 01:13:19,890
Jërëjëf Madam Shiren.

453
01:13:20,830 --> 01:13:23,390
Xaaral ma njëkka wax leen sama xalaat.

454
01:13:25,260 --> 01:13:27,350
Seytukat Shiren, njëkk...

455
01:13:57,000 --> 01:13:57,930
Sama senaario mel nii.

456
01:13:57,930 --> 01:14:00,020
Maa ngi féexal sama xol, maa ngi 
satisfait ci liggéeyam.

457
01:14:02,600 --> 01:14:03,990
Leegi ñaari jafe-jafe lañu wara saafara.

458
01:14:04,930 --> 01:14:06,090
Ana lu jëm ci oto yi?

459
01:14:08,200 --> 01:14:10,990
Sama xarit amoon na oto mu jox ma ko.

460
01:14:11,930 --> 01:14:12,390
Far?

461
01:14:14,260 --> 01:14:15,190
Waxu nga ni amoo xarit?

462
01:14:18,230 --> 01:14:19,160
Amna benn.

463
01:14:21,030 --> 01:14:21,720
Xamleen loolu.

464
01:14:24,300 --> 01:14:26,630
Fan la xew-xew bi wara am?

465
01:14:30,830 --> 01:14:31,760
Dinaa la jox barab.

466
01:15:28,930 --> 01:15:30,560
Mooy representé.

467
01:15:31,500 --> 01:15:32,220
Bu nekk.

468
01:15:35,000 --> 01:15:36,390
Ma waajal sama bopp ci saasi.

469
01:15:38,960 --> 01:15:39,660
Ba ci vin xonk.

470
01:15:41,530 --> 01:15:43,860
Tay bis bu amul fenn la.

471
01:15:46,900 --> 01:15:47,590
Ban bis?

472
01:15:50,160 --> 01:15:51,560
Bis bu amul fenn ci yaw.

473
01:15:55,300 --> 01:15:57,160
Maa ngi ko waajal bu baax, kon dinaa njëkka sangu.

474
01:15:58,330 --> 01:16:04,390
Ci sama ngërëm, bëgg naa la leegi.

475
01:16:06,960 --> 01:16:11,160
Kaxaaru góor day neex lool.

476
01:16:13,030 --> 01:16:13,490
Dëgg la?

477
01:16:15,130 --> 01:16:19,330
Jigéen ja itam am naqar lool.

478
01:17:47,060 --> 01:17:48,690
M. Representant, xaar tuuti.

479
01:17:49,400 --> 01:17:50,090
Lu xew, atmosphere bi leegi.

480
01:17:50,800 --> 01:17:51,250
Maa ngi ñëw.

481
01:17:54,530 --> 01:17:56,390
- Dinaa la wéral.
- Gën?

482
01:17:58,260 --> 01:17:58,730
Lan la?

483
01:18:04,330 --> 01:18:05,490
Shiren, am nga film yu bari.

484
01:18:24,630 --> 01:18:25,090
yëg-yëg bu bees.

485
01:19:16,900 --> 01:19:17,830
Baaxna, baaxna.

486
01:19:19,930 --> 01:19:22,260
Shiren, leegi mooma gëna neex.

487
01:19:23,900 --> 01:19:25,990
man itam

488
01:19:28,800 --> 01:19:35,090
- Waaye kilifa gi nee na mënu ma ko.
- Ban réalisateur, ma dàq ko.

489
01:19:38,830 --> 01:19:39,990
Ndaw yi dañu gëna liggéey bu baax

490
01:19:48,630 --> 01:19:50,260
Oh, dafay metti tuuti.

491
01:19:52,360 --> 01:19:53,520
Sèdd.

492
01:19:55,160 --> 01:19:55,630
Ñëwal.

493
01:20:04,500 --> 01:20:05,890
Shiren bëgga naaw.

494
01:20:22,230 --> 01:20:25,730
Dafa neex.

495
01:20:25,730 --> 01:20:26,890
Man itam maa ngi ci jàmm.

496
01:20:30,160 --> 01:20:31,320
Ndax nu ngi xiif tuuti, nu dem lekk?

497
01:20:48,130 --> 01:20:50,220
Ngir may realisatër bi defar toast

498
01:20:54,900 --> 01:20:56,290
Waaye bruit bi dëgër na lool.

499
01:20:58,630 --> 01:20:59,790
Oh, fàww ma nekk foofu.

500
01:21:00,960 --> 01:21:03,050
Cheng Fan ak M. Cheng Zhe, maa ngi leen di sant.

501
01:21:03,760 --> 01:21:07,030
Amul lu melni bënn 
askan wi daf ko wara sonal.

502
01:21:09,600 --> 01:21:12,160
Lu ma wara def? Mën nga gis say filmu.

503
01:21:13,100 --> 01:21:19,850
Amul lenn luñu filmewul?

504
01:21:22,200 --> 01:21:23,130
Jub.

505
01:21:27,330 --> 01:21:28,020
Xaaral tuuti.

506
01:21:29,660 --> 01:21:31,290
- Nanga def
- Ndax kii mooy realisatër bi dëgg?

507
01:21:31,530 --> 01:21:35,020
- Jub.
- Sunu liggéeyukaay filmu moo tànn sa filmu.

508
01:21:35,730 --> 01:21:38,530
Bëgg naa waxtaan ak yaw ci liggéeyu waare bi 
filmu bii, amnaa jotu suba.

509
01:21:38,530 --> 01:21:39,930
- Loolu dëgg la ?
- Loolu dëgg la.

510
01:21:40,630 --> 01:21:44,830
- Sama eskiript?
- Waaw, nu gise suba ci biro bi.

511
01:21:45,060 --> 01:21:45,760
Jërëjëf.

512
01:21:50,200 --> 01:21:52,760
Dinaa siñe kontraa bi suba.

513
01:21:53,230 --> 01:21:57,650
Wax nga ni mën nga ko def. 
Maa ngi lay sant bu baax.

514
01:21:58,360 --> 01:21:59,060
Cheng Fan, Jërëjëf.

515
01:22:00,000 --> 01:22:02,090
Jërejëff sama rak, 
Beneen yoon dinaa la woo.

516
01:22:04,200 --> 01:22:07,460
Maa ngi lay sargal, dama bëgga jooy.

517
01:22:07,930 --> 01:22:09,330
Jooy, bul jooy, noppil.

518
01:22:10,500 --> 01:22:11,430
Sama mag ju jigéen, bëgg naala lool.

519
01:22:11,900 --> 01:22:13,760
- Xoolal li xew xale bii.
- Woor.

520
01:22:14,700 --> 01:22:16,090
- Nanu naan tuuti.
- Loolu lu baax la.

521
01:22:17,730 --> 01:22:23,090
Ngir filmu am ndam 
ci filmu realiste,

522
01:22:28,000 --> 01:22:28,450
6 weer ci ginnaaw.

523
01:22:57,860 --> 01:23:00,190
Madam Shiren mënul woon gis kameraa bi.

524
01:23:02,060 --> 01:23:02,990
Maa ngi jéggalu, jéggalu.

525
01:23:04,860 --> 01:23:09,750
Bul ko woowe sexier rek nga yëg ko.

526
01:23:10,860 --> 01:24:05,750
Tekkib sous-titre: AnanVinh


