1
00:00:07,083 --> 00:00:11,375
Maa ngi jéema nekk
Millennial bu rafet, te ndax yaw...

2
00:00:12,416 --> 00:00:13,958
...maa ngi tukki ni boomer.

3
00:00:24,333 --> 00:00:25,166
Tëye ko.

4
00:00:34,875 --> 00:00:37,208
- Pat?
- Dhruv, sama xarit, nu daje ci lu gaaw.

5
00:00:37,291 --> 00:00:38,625
- Sèdd.
- Kontaan naa ci gis la.

6
00:00:38,708 --> 00:00:39,541
Waaw, man itam.

7
00:00:39,625 --> 00:00:41,416
- Kii mooy sama yaay.
- Salaam maalekum.

8
00:00:41,500 --> 00:00:42,916
- Salaam maalekum.
- Te lii sama moom la.

9
00:00:44,125 --> 00:00:45,791
Damay kaf. Kavuya, sama xale bu jigeen.

10
00:00:45,875 --> 00:00:46,708
- Salaam maalekum.
- Waaw.

11
00:00:46,791 --> 00:00:48,375
- Yaa ngi fàttaliku?
- Waaw. Neex lool.

12
00:00:48,458 --> 00:00:50,125
Kontaan naa ci lool. Wërsëgu jàmm.

13
00:00:50,708 --> 00:00:51,875
- Waaw kay, tàggoo.
- Ba beneen yoon.

14
00:00:54,500 --> 00:00:58,375
Maa ngi ñëw ci barabu réew mi,
ak kan laa dajeel fii?

15
00:00:59,250 --> 00:01:00,375
Nataango liggéey.

16
00:01:00,458 --> 00:01:02,708
Dina jàpp ni damay dem ci tukki yu mel nii.

17
00:01:03,791 --> 00:01:06,375
- Dhruv, moom ci boppam mingi ci tukki bi.
- Waaw.

18
00:01:06,458 --> 00:01:07,291
Dal.

19
00:01:11,416 --> 00:01:14,166
Kon luy
tukki ci stil Kulkarni?

20
00:01:14,250 --> 00:01:15,500
- Wax?
- Waaw.

21
00:01:15,583 --> 00:01:17,041
Kon. Li may njëkka wax mooy...

22
00:01:17,666 --> 00:01:19,916
Ku nekk ci njaboot gi dafa wara yóbbaale benn meññeef.

23
00:01:21,375 --> 00:01:22,666
- Rafet na.
- Leer?

24
00:01:22,750 --> 00:01:26,500
Ñaareel ba mooy bi tukki bi di tàmbali
nun ñépp ñuy yuuxu naan: “Maa ngi sargal Boroom bi!”

25
00:01:27,083 --> 00:01:28,916
Ñatteel ba mooy:

26
00:01:29,000 --> 00:01:31,291
sudee buffet lañuy seentu,

27
00:01:31,375 --> 00:01:34,291
lekkunu bu yàgg
lekk lu bari nimu mënee.

28
00:01:35,041 --> 00:01:35,875
Muus.

29
00:01:36,500 --> 00:01:38,708
Xale bu jigeen bu pragmatik
ci diggu askan wi.

30
00:01:44,666 --> 00:01:46,125
Nanga def!

31
00:01:46,208 --> 00:01:47,625
- Salaam maalekum!
- Salaam maalekum!

32
00:01:47,708 --> 00:01:49,500
Man maay sa xarit Christy.

33
00:01:49,583 --> 00:01:52,125
Tay lanu bokk
Nanu banneexu Munnar. Baax?

34
00:01:52,208 --> 00:01:55,583
Nu tàmbali sunu tukki ci 7:30,

35
00:01:55,666 --> 00:01:57,916
te dina nu ko jeexal ci guddi gi ci 17:30.

36
00:01:58,000 --> 00:01:59,708
Yendul ak jàmm.

37
00:01:59,791 --> 00:02:00,750
Jërëjëf.

38
00:02:01,708 --> 00:02:04,250
"Xarit". Amnaa xarit bu bees.

39
00:02:05,416 --> 00:02:07,500
Dafa nuru jàngalekat ci làkku hindi.

40
00:02:08,083 --> 00:02:10,500
- Dafa tar. Danu jaxasoo.
- Noppil.

41
00:02:13,291 --> 00:02:15,833
- sargal...
-...Boroom bi!

42
00:02:28,500 --> 00:02:30,208
NETFLIX

43
00:02:54,500 --> 00:02:56,916
Ñaareelu SERI
VACANCE FAMILIE

44
00:02:57,833 --> 00:03:03,166
EGLISE DE MAR TOMAS DE SAN THOMAS
Munnaar

45
00:03:03,250 --> 00:03:04,291
Ndax raxas nga tay?

46
00:03:05,583 --> 00:03:09,250
Ñaata xaj lañu gis?
ginaaw bi nga yegsee? Bu néew ci 20.

47
00:03:09,333 --> 00:03:11,458
Ndax raxas nga wala déet?

48
00:03:12,083 --> 00:03:15,416
- Tay mënu nu raxas, danuy sakkanal ndox.
- Yomb na lool.

49
00:03:16,625 --> 00:03:18,500
Mboq, mboq, muur tilim.

50
00:03:19,583 --> 00:03:21,875
Mboq, mboq, muur kaka!

51
00:03:21,958 --> 00:03:23,833
Lu xew? Lan?

52
00:03:23,916 --> 00:03:28,250
- Mboq, mboq, muur kaka!
- Lii moo gëna ñaaw xol!

53
00:03:28,958 --> 00:03:32,583
Damn, ndax leegi nga xalaat loolu?
Ci tukki?

54
00:03:34,041 --> 00:03:35,166
Daf ma yéem.

55
00:03:35,250 --> 00:03:39,833
Eglis bu Thomas mu sell mi tabax
liggéeykat yi ci tooli ataaya yi.

56
00:03:40,541 --> 00:03:43,916
Wutal sa jotu. Xoolal lépp
ndànk te moytu.

57
00:03:44,541 --> 00:03:46,750
Waaye am nga 20 simili, waaw?

58
00:03:46,833 --> 00:03:49,958
Soo bëggee gis bàmmeel bi,
demal ci ndeyjoor.

59
00:03:50,041 --> 00:03:52,625
Bëgg nga gis eglis bi?
kaay fii.

60
00:03:53,333 --> 00:03:58,500
"Jëlal sa jotu. Xoolal lépp
ak bàyyi xel. Waaye am nga 20 simili ndànk.”

61
00:04:00,291 --> 00:04:02,875
Saa waay! Xoolal ma ëllëg!

62
00:04:03,458 --> 00:04:05,875
- Xoolal bu baax li wër eglis bi.
- Waaw. Baal ma.

63
00:04:16,250 --> 00:04:17,291
Rafet lool.

64
00:04:19,958 --> 00:04:21,041
Waaw.

65
00:04:28,583 --> 00:04:32,833
Nanu daw joge fi.
Nanu dem. Gën gaaw!

66
00:04:32,916 --> 00:04:34,625
Dhruv, joxal tukki bi chance.

67
00:04:36,416 --> 00:04:37,250
Nanu dem.

68
00:04:50,000 --> 00:04:51,375
Saa waay, gis naa lépp.

69
00:04:51,458 --> 00:04:53,833
Ak lan? Lii souvenir la.

70
00:04:55,083 --> 00:04:56,458
Am nga leneen loo bëgg?

71
00:04:58,958 --> 00:05:02,583
Momo, "Gisuma lu bon"
Dégluma lu bon, waxuma lu bon.»

72
00:05:03,166 --> 00:05:05,250
Te defuma lu bon, yaw dof ji.

73
00:05:08,916 --> 00:05:09,916
Loo wax?

74
00:05:12,833 --> 00:05:14,583
Tablo bi rafet na lool.

75
00:05:16,458 --> 00:05:17,375
Ndax nu dem?

76
00:05:24,791 --> 00:05:26,541
- Ndax toog nga?
- Waaw.

77
00:05:26,625 --> 00:05:27,666
Kon...

78
00:05:29,208 --> 00:05:30,791
Lu may njëkka wax?

79
00:05:31,458 --> 00:05:33,208
Laata ñuy wax seen bàkkaar, dañuy wax dara.

80
00:05:33,291 --> 00:05:35,208
- Lan?
- Maa ngi jéggalu, waaye...

81
00:05:36,000 --> 00:05:38,041
Baay, baal ma, ndax def naa bàkkaar.

82
00:05:38,583 --> 00:05:43,166
Dama sàcc bonbon ci sac à dos bu Sandeep
ba ci ñatteelu klas.

83
00:05:43,250 --> 00:05:44,833
Dinaa ko woo léegi.

84
00:05:44,916 --> 00:05:46,875
Li ci njëkk mooy nga dello sonndel bi nga sàcc.

85
00:05:50,916 --> 00:05:53,416
Kon leegi, ndax dama wara laaj lu jamp?

86
00:05:54,083 --> 00:05:54,916
Waaw, laajal.

87
00:05:55,500 --> 00:05:57,791
- Sérieux lool, waaw ?
- Waaw.

88
00:06:00,416 --> 00:06:01,250
Waaw.

89
00:06:02,958 --> 00:06:06,291
Su ma la jiitu dee,
loo nara def?

90
00:06:09,416 --> 00:06:11,583
Ndax dafa serye lool?

91
00:06:12,250 --> 00:06:13,375
Àrtu naa la.

92
00:06:14,708 --> 00:06:15,583
Kon baaxna.

93
00:06:16,708 --> 00:06:18,291
Kon, jàpp naa...

94
00:06:20,583 --> 00:06:21,625
Man...

95
00:06:21,708 --> 00:06:24,666
Dina jafe lool ci man
dundu te amul yaw, waaye...

96
00:06:26,708 --> 00:06:28,791
Yaakaar naa ni ëlëg wala ëlëg dinaa dal.

97
00:06:31,333 --> 00:06:35,041
Yan yeneen pexe laa am?
Ndax loolu du dëgg?

98
00:06:35,625 --> 00:06:37,625
Bëgg nga ma jéema dal, wala book?

99
00:06:37,708 --> 00:06:41,208
Waaw. Ci lu wóor.
Waaye mingi aju ci ni mbir yi di demee.

100
00:06:41,291 --> 00:06:42,333
Ndax ay jafe-jafe?

101
00:06:42,416 --> 00:06:44,208
- Waaw.
- Ci ban anam ?

102
00:06:44,291 --> 00:06:47,750
Soo noppee ginaaw ñetti weer,
Dinaa mer.

103
00:06:47,833 --> 00:06:50,750
- Leer.
- Kon xaaral...

104
00:06:51,333 --> 00:06:52,166
...amaana...

105
00:06:53,083 --> 00:06:54,833
...dama yaakaar ni juróom ñaari weer lu baax la.

106
00:06:55,875 --> 00:06:56,708
- Juróom ñaar ?
- Waaw.

107
00:06:56,791 --> 00:06:59,333
Kon, xaar tuuti.
Juróom ñaar ci fan weeri - 210 fan.

108
00:07:00,208 --> 00:07:03,500
- Na nekk 200. Dafa gëna baax.
- Dhruv, 300 fan soo koy seet.

109
00:07:03,583 --> 00:07:04,583
Ñatti téeméer?

110
00:07:04,666 --> 00:07:07,416
Fan la nimero yu bari yooyu bawoo?
Ñaari téeméer lu jaadu la.

111
00:07:07,500 --> 00:07:09,541
Benn simili rekk. At yu bari a ngi nii nga nekk ak man.

112
00:07:09,625 --> 00:07:11,375
Mënu ma xaar juróom ñaari weer?

113
00:07:11,458 --> 00:07:15,000
Waaye du ci yaw, ci man la.
Dinga dee bàyyi ma.

114
00:07:15,083 --> 00:07:17,208
Lu ma wara def?
Dama bëgga kontaan!

115
00:07:17,291 --> 00:07:21,000
Momo, defna 14 weer nga nekk ak man.
Mënu ma xaar ba juróom ñaar?

116
00:07:21,833 --> 00:07:24,666
Kon limu juróom ñaar fi la cosaanoo?

117
00:07:39,916 --> 00:07:42,416
- Noppil. Gisoo leen filmu bi.
- Ci lu wóor.

118
00:07:42,500 --> 00:07:44,166
Seetaanuma ko woon.

119
00:07:46,625 --> 00:07:49,000
Soo noppee nga wax. "Dinaa nekk ni moom."

120
00:07:49,708 --> 00:07:50,875
- Lan?
- Waaw.

121
00:07:51,541 --> 00:07:52,958
"Dinaa nekk ni moom."

122
00:07:53,041 --> 00:07:55,750
Laaj bu nax.
Yaay nekk ci resto yépp.

123
00:07:55,833 --> 00:07:57,166
Lu xew?

124
00:07:58,375 --> 00:07:59,791
Lu xew?

125
00:07:59,875 --> 00:08:01,291
-Dégg nga ko?
- Déedéet.

126
00:08:02,375 --> 00:08:05,333
- Amoon na lu fa nekkoon.
- Amul woon dara foofu, Dhruv.

127
00:08:06,583 --> 00:08:07,750
Sudee tig la?

128
00:08:10,833 --> 00:08:11,833
Vis nga.

129
00:08:14,333 --> 00:08:16,500
Puub. Ndax fàtte nga wideo bi siiw lool?

130
00:08:16,583 --> 00:08:18,375
Fan la tigre bi tëmb génn ci tool bi?

131
00:08:18,458 --> 00:08:20,000
Toolu kafe la woon.

132
00:08:21,666 --> 00:08:23,083
Am xel lool.

133
00:08:23,166 --> 00:08:25,958
Melni tigre mën na ràññee
toolu ataaya ci benn café.

134
00:08:27,375 --> 00:08:28,208
Dina wuutale.

135
00:09:20,791 --> 00:09:22,875
- Ñaari simili rek lanuy dem !
- Puub.

136
00:09:23,708 --> 00:09:26,625
Ku nekk dugg ci bus bi leegi!

137
00:09:27,208 --> 00:09:28,833
Ñaari simili rekk!

138
00:09:33,291 --> 00:09:34,125
Sama Yàlla!

139
00:09:34,958 --> 00:09:37,750
Damn, nit ñooñu ñooy kan? Fan lañu jóge?

140
00:09:38,416 --> 00:09:41,083
- Nanu dem.
- Dara, Dhruv.

141
00:09:41,166 --> 00:09:43,208
- Nanu dem. Dafa mer.
- Waaw, ragluwul!

142
00:09:44,291 --> 00:09:46,500
Dhruv, wàññil. Dina ñu nu xaar.

143
00:09:47,083 --> 00:09:49,000
Mu woo nu.

144
00:09:49,083 --> 00:09:51,000
Ñépp a ngi fa ba noppi, leegi noo ngi daw.

145
00:09:51,083 --> 00:09:52,291
Dal!

146
00:09:52,791 --> 00:09:55,083
Damn, nanu dem. Lu ma wara def?

147
00:09:55,166 --> 00:09:56,541
Demal, dinaa la jàpp.

148
00:09:59,125 --> 00:10:01,083
Yaa ngi may soof leegi.

149
00:10:01,583 --> 00:10:03,583
Dina nu ñëw ci diir bu gàtt. Mbir mu rëy.

150
00:10:13,125 --> 00:10:14,166
"Harry ak Sally."

151
00:10:16,166 --> 00:10:17,000
Lan?

152
00:10:17,583 --> 00:10:18,833
"Dinaa nekk ni moom."

153
00:10:18,916 --> 00:10:21,083
Tànta ci benn kafe
"Bi Harry daje ak Sally."

154
00:10:21,166 --> 00:10:22,000
Waaw.

155
00:10:25,708 --> 00:10:26,708
Baal ma.

156
00:10:28,791 --> 00:10:30,000
Wax nga dëgg.

157
00:10:30,875 --> 00:10:32,041
Ay yëfi dof la woon.

158
00:11:05,083 --> 00:11:09,000
Ndànk! Yeewu!
Arrêt bu ci topp!

159
00:11:09,083 --> 00:11:09,916
Puub!

160
00:11:10,000 --> 00:11:12,333
- Danu wara génn.
- Dina nu añ fii !

161
00:11:13,208 --> 00:11:14,916
Dama wara jënd chips banaan.

162
00:11:15,958 --> 00:11:18,708
- Puub.
- Dhruv, noppil. Melokaan.

163
00:11:29,791 --> 00:11:32,708
- Solal lii.
<i>- Dhruv, lu tax woowoo?</i>

164
00:11:33,208 --> 00:11:34,750
Yaay, danu sonn tuuti.

165
00:11:34,833 --> 00:11:37,708
<i>- Kon, dara. Kavuya ak yaw?</i>
- Waxtaan ak moom.

166
00:11:38,416 --> 00:11:39,916
Salaam maalekum! Na nga def?

167
00:11:40,000 --> 00:11:43,250
<i>Lepp a ngi baax. Yaa ngi mujjee jël dogal</i>
Toxu Bombay?

168
00:11:43,333 --> 00:11:46,291
Lépp dogal nañu ko.
Noo ngi xaar ab janoo balaa ñu koy toxal.

169
00:11:46,375 --> 00:11:47,291
<i>Gis naa.</i>

170
00:11:48,583 --> 00:11:51,625
<i>Bëgg naa la ñaanal dara.</i>

171
00:11:52,125 --> 00:11:53,291
<i>Ci gàttal...</i>

172
00:11:54,208 --> 00:11:55,708
<i>Doomu Pramod lu tuddu?</i>

173
00:11:55,791 --> 00:11:57,083
Ndax kii mooy Kavuya?
<i>- Waaw.</i>

174
00:11:57,166 --> 00:11:58,208
<i>Dinaa waxtaan ak moom.</i>

175
00:11:58,791 --> 00:12:00,750
Nanga def, Kawuya! Naka nga def?</i>

176
00:12:00,833 --> 00:12:03,916
- Nanga def ! Baax. Na nga def?
<i>- Lépp a ngi baax.</i>

177
00:12:04,000 --> 00:12:06,625
<i>Waaw kay, dama bëggoon a laaj dara.</i>

178
00:12:07,375 --> 00:12:10,625
Doomu sama cousin Pramod Kishore

179
00:12:10,708 --> 00:12:14,125
<i>bëgg na am MBA</i>
Ci Daara bu kawe bu Narsee Monjee.

180
00:12:14,208 --> 00:12:16,125
<i>- Lan mooy doxalin bi...</i>
<i>- Dinaa ko laaj.</i>

181
00:12:17,041 --> 00:12:19,833
<i>Salaam, am nga sa MBA</i>
Ci Daara bu kawe bu Narsee Monjee?

182
00:12:19,916 --> 00:12:20,750
Waaw.

183
00:12:20,833 --> 00:12:24,583
<i>Ndax am nga nimero njiitu porogaraam bi?</i>

184
00:12:25,333 --> 00:12:27,916
Amnaa nimero, waaye...

185
00:12:28,458 --> 00:12:32,208
Yaay, du noonu lañu koy defee.
Lépp a ngi aju ci poñ yi mu am ci CAT.

186
00:12:32,291 --> 00:12:34,333
<i>Jàppoon naa ni moo gëna yomba def lii.</i>

187
00:12:34,416 --> 00:12:37,458
Sama yaay, lii du club sport.
Mënu ma jëfandikoo...

188
00:12:37,541 --> 00:12:39,166
Dinaa la jox benn nimero

189
00:12:39,250 --> 00:12:41,708
waaye bul wax ni ci man nga ko jàngee.

190
00:12:41,791 --> 00:12:44,041
<i>- Déedet. Bul leen wax</i>
<i>- Jërëjëf.</i>

191
00:12:44,125 --> 00:12:46,583
<i>- Jërëjëf.</i>
<i>-Waaw kay, nu dem.</i>

192
00:12:47,166 --> 00:12:48,208
<i>- Waaw.</i>
- Àggoo.

193
00:12:48,291 --> 00:12:49,416
BAAX NA. Ba beneen yoon.

194
00:12:51,625 --> 00:12:53,666
Amaana nekk consultant ci wàllu liggéey?

195
00:12:53,750 --> 00:12:57,208
Liggéey bi gën ci nit ñi
ñi seen liggéey jaarul yoon.

196
00:12:59,166 --> 00:13:01,000
Danga jaaxle ci tekki làkk?

197
00:13:03,208 --> 00:13:06,416
- Rachel yonnegul benn SMS.
- Dina ko yónnee.

198
00:13:06,500 --> 00:13:07,958
- Dal!
- Nga jéem a dal.

199
00:13:08,041 --> 00:13:09,791
Noppi, bul def xumbaay!

200
00:13:09,875 --> 00:13:11,833
Sa tur la!

201
00:13:12,750 --> 00:13:15,125
Sëriñ bi! naka lañu mënee yéeg te amul rang!

202
00:13:15,625 --> 00:13:17,208
Sëñ bi, loolu mënul am. Dellul!

203
00:13:17,291 --> 00:13:18,958
- Dara.
- Déedet, dara.

204
00:13:19,041 --> 00:13:20,333
- Amul rang.
- Ak dal!

205
00:13:20,416 --> 00:13:21,791
Sa tur dina ñëw.

206
00:13:21,875 --> 00:13:23,291
Lu tax ngay tëb ci rang bi?

207
00:13:24,208 --> 00:13:25,166
Loolu mënul nekk.

208
00:13:26,250 --> 00:13:28,541
simili rek nga am.

209
00:13:28,625 --> 00:13:31,416
Fëyal gaaw, waaye nga ànd ak dal.

210
00:13:32,625 --> 00:13:33,708
Baax?

211
00:13:33,791 --> 00:13:35,916
Dina "soo"
ci malayalam?

212
00:13:36,500 --> 00:13:37,875
- Ak naka ?
- "Kiristi."

213
00:13:51,041 --> 00:13:54,958
- Maa ngi gis vapër.
- Waaw? Gis leen, mu ngi nii.

214
00:14:02,208 --> 00:14:06,458
Ndax waxtaan wii merul la?
Narsee Monjee College?

215
00:14:07,166 --> 00:14:08,458
Baaxna, baaxna.

216
00:14:09,916 --> 00:14:12,125
Waaw, waaye daa dof tuuti, wala book?

217
00:14:14,750 --> 00:14:16,041
Xam nga, xalaat naa...

218
00:14:16,750 --> 00:14:20,000
Mën naa wax samay waajur
ñuy wax lu amul benn njariñ,

219
00:14:20,500 --> 00:14:22,083
waaye sa bopp - musul.

220
00:14:22,166 --> 00:14:23,041
Waaw?

221
00:14:23,791 --> 00:14:26,250
Te dinaa la ko wax dëgg. Waaw!

222
00:14:27,458 --> 00:14:29,708
- Lu ñàkk solo.
- Dinaa xotti sama pàntaloŋ ndax tiitaange.

223
00:14:30,291 --> 00:14:31,375
Xalaatal rek.

224
00:14:31,458 --> 00:14:34,250
Ma yokk ci: “Damn!
Maa ngi delloo sama kàddu!”

225
00:14:46,708 --> 00:14:48,416
Fukki simili yu ci topp!

226
00:14:50,833 --> 00:14:52,708
- Lan?
- Ndax dinga woy?

227
00:14:53,708 --> 00:14:56,666
Yaa ngi way. Amnaa baat bu tiis.
Yaa ngi way bu baax.

228
00:14:56,750 --> 00:14:59,875
-Am nga baat bariton.
- Ndax dëgg la? Sèdd!

229
00:14:59,958 --> 00:15:02,041
Jéemal ko ba noppi nu gis.

230
00:15:02,958 --> 00:15:04,875
<i>Dafay faral di waxtaan ak man</i>

231
00:15:04,958 --> 00:15:07,708
<i>Yaay, dafay xeex ak ay bëtëm</i>

232
00:15:07,791 --> 00:15:12,333
<i>Yaay, namm naa ko lool</i>

233
00:15:13,500 --> 00:15:15,708
Lan mooy "na-na-na"? "Géj naa laa gis"?

234
00:15:16,291 --> 00:15:19,333
Soxlawolen. Yaa ngi reetaan saa yu nekk.
Moo tax duma woy.

235
00:15:20,458 --> 00:15:22,458
Yaa ngi bawoo Inde gannaar, danga wara xam kàddu yi.

236
00:15:22,541 --> 00:15:25,750
Dama gëna bëgg ritm.
Te kàddu yi sa mbiri bopp la.

237
00:15:27,291 --> 00:15:29,916
Waaw, Madonna,
nanu pedaal.

238
00:15:30,000 --> 00:15:32,291
Air bi neex na lool, Dhruv.

239
00:15:37,000 --> 00:15:37,916
Mu mel ni dafa yàqu.

240
00:15:38,000 --> 00:15:41,291
Déedéet, bàyyileen! Soxlawolen kaf yu mel nii.

241
00:15:42,375 --> 00:15:43,666
Kon nu jeex.

242
00:15:47,666 --> 00:15:48,666
Lu xew-xew!

243
00:15:50,416 --> 00:15:51,541
Nanu, mbalit yu mel nii.

244
00:15:55,958 --> 00:15:57,250
Lan? Ci anam bu dëggu?

245
00:16:01,291 --> 00:16:02,208
Hey!

246
00:16:04,500 --> 00:16:05,708
Lu xew-xew!

247
00:16:07,625 --> 00:16:10,541
Sudee du jëkkër ak jabar yooyu,
Dunu doon am gaal gii!

248
00:16:11,708 --> 00:16:13,958
Mënul nekk! Ci yaw.

249
00:16:16,875 --> 00:16:18,416
Loolu musul am ci Finlande.

250
00:16:19,000 --> 00:16:22,291
- Ndax gaal yi duñu fa yàqu?
- Bul am xel !

251
00:16:22,375 --> 00:16:23,791
Duñu fa tëb ci rang.

252
00:16:24,625 --> 00:16:25,916
Demal safara!

253
00:16:26,625 --> 00:16:28,416
Dhruv, nga ànd ak dal. Lu xew ?

254
00:16:29,083 --> 00:16:29,958
Lan?

255
00:16:30,833 --> 00:16:32,708
Dal? Xoolal nu.

256
00:16:32,791 --> 00:16:35,250
Dama tëju ci diggu lak bi
ci gaal gu yàqu.

257
00:16:35,333 --> 00:16:37,833
Du ci kanam wala ci ginaaw. Danu tëju!

258
00:16:38,541 --> 00:16:41,791
Dhruv, ñépp dina ñu féey
benn yoon wi.

259
00:16:42,375 --> 00:16:44,000
Dina nu gis kenn.

260
00:16:45,000 --> 00:16:46,333
Mënul nekk, alal.

261
00:16:47,708 --> 00:16:49,000
Leegi kan mooy woo?

262
00:16:53,041 --> 00:16:54,041
Génn.

263
00:16:56,541 --> 00:16:59,416
- Waaw yaay.
<i>- Dhruv, yónnee woo nimero bi.</i>

264
00:16:59,500 --> 00:17:02,291
- Nanga muñ.
- Druv.

265
00:17:02,375 --> 00:17:05,583
<i>Waaw, waaye jarul ñuy yuuxu.</i>
<i>Maa ngi lay fàttali rek.</i>

266
00:17:05,666 --> 00:17:09,791
Baal ma yaay. Dinaa la woowaat.
Jox ma ñaari simili. Baal ma.

267
00:17:13,583 --> 00:17:15,625
Puub! Excursion bii alku la.

268
00:17:15,708 --> 00:17:19,500
Ak Kirist bii:
"Ñar fukki simili, gaaw, daw!"

269
00:17:19,583 --> 00:17:20,666
naka ngay mëna féexalee fii?

270
00:17:20,750 --> 00:17:22,166
- Dama ko waroon a wax.
- Lan?

271
00:17:22,250 --> 00:17:25,375
Dafa waroon wax leen lépp ci saasi
ki nga bëggul.

272
00:17:25,875 --> 00:17:28,166
Lu tax nga may wax lii leegi?

273
00:17:28,250 --> 00:17:31,375
Am nanu fu nu tëju.
Loolu, naka lañu leen di dimbali ?

274
00:17:36,041 --> 00:17:38,416
<i>- Nanga def? Dhruv?
- Waaw, yaay?

275
00:17:38,500 --> 00:17:41,958
<i>- Lu xew?</i>
- Waaw yaay, dinaa la woowaat.

276
00:17:45,083 --> 00:17:46,000
Puub.

277
00:17:56,000 --> 00:17:57,250
Puub.

278
00:17:59,083 --> 00:18:00,041
Loolu laay def.

279
00:18:01,000 --> 00:18:02,208
Waaw.

280
00:18:02,291 --> 00:18:04,750
Maa ngi doxalee ni sama pàppa.

281
00:18:07,083 --> 00:18:11,083
Noonu la amee ci Finlande.
Lépp a ngi jaar yoon, amul benn jafe-jafe.

282
00:18:11,166 --> 00:18:13,833
Waaye su amee lu jaarul yoon,
Dama doon dem ba dof.

283
00:18:15,416 --> 00:18:16,583
Sama pàppa itam dafa def luni mel.

284
00:18:17,083 --> 00:18:20,458
Su amee lu ko sonal,
lépp negatif la.

285
00:18:20,541 --> 00:18:23,291
Dafay ñaxtu, onku
te mënul xalaat lu baax.

286
00:18:23,375 --> 00:18:26,250
Damn, noonu la.
Noonu la!

287
00:18:27,666 --> 00:18:29,750
- Dara, Dhruv.
- Déedet, amul benn njariñ, Kavuya.

288
00:18:30,666 --> 00:18:32,750
Danu wara jëfandikoo energie ci anam wu am xel.

289
00:18:33,541 --> 00:18:34,583
Dunu gëna ndaw.

290
00:18:36,041 --> 00:18:38,625
Waaye du yaw kese nga am jafe-jafe bii.

291
00:18:40,333 --> 00:18:42,208
Ku nekk dafay topp jikkoy waajur yi.

292
00:18:43,125 --> 00:18:45,791
Loolu mënul ñàkk. Amul dara loo ci mëna def.

293
00:18:47,458 --> 00:18:49,708
Ndax dëgg la? Ndax loolu dal na la itam ?

294
00:18:50,333 --> 00:18:51,166
Ci lu wóor.

295
00:18:52,125 --> 00:18:54,750
Sama pàppa dafay faral di juum ci sama yaay.
Ma adopte lii.

296
00:18:55,541 --> 00:18:57,791
Leegi danu koy kaf saa yu nekk.

297
00:18:57,875 --> 00:18:59,125
Ba leegi loolu mingi am.

298
00:19:00,750 --> 00:19:02,041
Jëkkër ak jabar ñooñu ñu ngi gaal fii.

299
00:19:02,125 --> 00:19:04,750
Salaam maalekum! Musal nu!
Nanga denc!

300
00:19:04,833 --> 00:19:06,750
Xamuñu woon dara!

301
00:19:06,833 --> 00:19:11,083
Kirist! Woowal Kirist!
Christy ñaar fukki simili!

302
00:19:11,666 --> 00:19:14,125
Mbaa yaa ngi lay saraxu! Jërëjëf soxna si. Jërëjëf!

303
00:19:15,791 --> 00:19:18,458
Puub. Dina nu mucc.

304
00:19:20,333 --> 00:19:22,250
Baal ma. Xaaral...

305
00:19:23,083 --> 00:19:24,291
Kon sa yaay...

306
00:19:25,750 --> 00:19:27,208
Maanaam ndax lii

307
00:19:27,291 --> 00:19:29,541
Dama tàmm diko metital.

308
00:19:29,625 --> 00:19:31,750
Duñu ko soof, waaye dafay am.

309
00:19:31,833 --> 00:19:35,791
Bima demee seeti ko bu yàggul,
Ma waxtaan ak moom ci xale.

310
00:19:35,875 --> 00:19:37,666
Maanaam, xamuma ndax bëgg naa xale.

311
00:19:37,750 --> 00:19:41,208
Waaye bima ko leeralee,
Ma def ko mu melni ku néew doole.

312
00:19:41,708 --> 00:19:44,458
Dama ko àtte ci
ni dafa fas yéene jural ma doom.

313
00:19:48,375 --> 00:19:50,083
Du yoon, waaye...

314
00:19:51,083 --> 00:19:53,375
... war nañu am xel
liggéey ci, Dhruv.

315
00:19:54,791 --> 00:19:57,833
Du yoon
te amul benn njariñ.

316
00:19:59,333 --> 00:20:00,166
Ginaaw loolu...

317
00:20:01,916 --> 00:20:04,958
Ndax nooy tànn ki nu bëgg?

318
00:20:05,541 --> 00:20:08,916
Waaye daanaka lépp a ngi ci nun
prograam nañu ko ba noppi?

319
00:20:09,541 --> 00:20:12,583
Danuy dundal genn-wàllu sunu dundu
dindi prograam yooyu.

320
00:20:13,333 --> 00:20:17,208
Li njëkk ngay def soo bëggee saafara jafe-jafe bi mooy
nangu ko.

321
00:20:17,291 --> 00:20:20,583
Danu koy def.
Dina nu liggéey ci loolu.

322
00:20:22,500 --> 00:20:23,625
Lépp dina baax.

323
00:20:38,125 --> 00:20:41,166
- Lu doonoon say tànk?
- Sama bopp di gaal.

324
00:20:44,708 --> 00:20:49,333
- Ndax ma woo Christy ak sama baat bu tiis bi?
- Jarul nga nekk lu dramatik.

325
00:20:49,416 --> 00:20:51,958
Dina ñu wax ni danuy yuuxu
ak li nu mënul féey.

326
00:20:52,041 --> 00:20:53,083
Lu tiis lool.

327
00:20:57,375 --> 00:20:58,375
Salaam maalekum!

328
00:21:00,666 --> 00:21:01,583
Musal nu!

329
00:21:17,833 --> 00:21:19,291
Lu ñu war a def ?

330
00:21:19,375 --> 00:21:21,708
Bàyyi turist yi ci gaal gi nga dem?

331
00:21:22,375 --> 00:21:24,791
Wax ko ni ñu ngi ci yoon.

332
00:21:26,375 --> 00:21:27,500
Bëy.

333
00:21:32,291 --> 00:21:33,250
Christy, jéggalu.

334
00:21:33,333 --> 00:21:36,750
Dara. Sama tour operatër neena,
ni lekk baa ngi sedd.

335
00:21:38,333 --> 00:21:39,791
Bu ko defee, war nanu gaaw.

336
00:21:40,791 --> 00:21:41,625
Lii ngir yaw la.

337
00:21:46,625 --> 00:21:48,125
Dégg naa seen waxtaan.

338
00:21:51,041 --> 00:21:52,000
Jërëjëf, Christy.

339
00:21:53,750 --> 00:21:55,250
Waaw leegi toppal ma.

340
00:21:57,541 --> 00:21:59,166
- Kirist!
- Waaw?

341
00:21:59,250 --> 00:22:02,458
simili rek lañu am
walla yokk tuuti?

342
00:22:05,291 --> 00:22:06,541
Nanu gaaw dem.

343
00:22:18,500 --> 00:22:19,708
Looy xalaat?

344
00:22:21,375 --> 00:22:23,083
Soppi nga xalaat ci Christy.

345
00:22:25,291 --> 00:22:27,958
- Waaw.
- Ndax yomboon na?

346
00:22:29,458 --> 00:22:30,291
Waaw.

347
00:22:32,291 --> 00:22:34,208
Amaana nun ci sunu bopp mën nanu soppiku?

348
00:22:36,583 --> 00:22:41,166
Dëgg la, fàww nga jéem
waaye mënoo tuumal lépp ci sa dëmb.

349
00:22:45,833 --> 00:22:46,833
Waaw.

350
00:22:51,416 --> 00:22:54,833
Waaw, mën na baña jaar yoon
waaye dañu wara jéem.

351
00:22:57,208 --> 00:22:59,625
Amaana àndul ak sama pàppa, waaye...

352
00:23:00,458 --> 00:23:03,500
Dama bëgga am
Amoon naa diggante bu baax ak moom.

353
00:23:05,541 --> 00:23:07,083
Danga bëgg su nekkee ci sa wet?

354
00:23:07,166 --> 00:23:09,750
Waaw, loolu lu baax la.

355
00:23:10,541 --> 00:23:15,333
Bu leen xuloo am,
jàmm kese.

356
00:23:16,083 --> 00:23:18,333
Defal lii sa status WhatsApp.

357
00:23:20,750 --> 00:23:23,166
Yaakaar naa ni Pat du wax ci biro bi:

358
00:23:23,250 --> 00:23:27,583
"Dhruv ak faram Kavuya
Danu doon sëy ci biir gaal, mu dagg.”

359
00:23:27,666 --> 00:23:29,916
Ndax faale nga limu xalaat?

360
00:23:30,000 --> 00:23:31,666
Liggéey naa ak moom bu njëkk.

361
00:23:31,750 --> 00:23:35,041
Bëgg naa ñu def lu baax
xalaat ci man. Loolu natureel la.

362
00:23:39,708 --> 00:23:42,708
Dégluleen, bëgg naa leer
ni duma sàcc.

363
00:23:44,083 --> 00:23:46,041
BAAX NA. Jërëjëf ci lii, waaye...

364
00:23:47,041 --> 00:23:50,041
...gis nga, sàcc yépp ci àdduna
loolu la ñuy wax.

365
00:23:50,125 --> 00:23:54,833
Dédeet. Dama bëggoon def dara
loolu duma faral di def.

366
00:23:56,291 --> 00:23:57,250
Defa doon...

367
00:23:57,833 --> 00:23:59,958
Ni ngay def vacance ci sa bopp.

368
00:24:05,041 --> 00:24:09,166
Du sa jikko yu bon yépp
Ci sama pàppa laa ko jëlee.

369
00:24:09,250 --> 00:24:13,041
Xamuma ni ñuy yoree xaalis.
Damay dugal xaalis ni dof te...

370
00:24:13,666 --> 00:24:17,666
Sama pàppa xalaat budget bi
ak xayma njëg yi ci anam wu am xel.

371
00:24:18,333 --> 00:24:20,375
- Te xamoo waxaale.
- Oh.

372
00:24:21,291 --> 00:24:22,625
Mënu ma ko def dara.

373
00:24:24,083 --> 00:24:28,750
Waaw. Ak ma sàcc
Sac à dos bu Sandeep du bonbon rek la denc,

374
00:24:28,833 --> 00:24:30,833
waaye ñaari yoon ak xaalis.

375
00:24:30,916 --> 00:24:33,041
Ñaari yoon kese.

376
00:24:34,875 --> 00:24:37,250
Sama pàppa musu ma jàngal sàcc.

377
00:24:39,541 --> 00:24:43,375
- Waaw leegi gis nanu ko.
- Waaw?

378
00:24:47,916 --> 00:24:49,083
Jërëjëf Kavu.

379
00:24:49,583 --> 00:24:53,625
Yaw moo tax ma lekk ñam wu neex nii.

380
00:24:54,375 --> 00:24:57,375
Danga yéeme. Loolu yéeme na.

381
00:24:58,708 --> 00:24:59,708
- Xalaatal!
- Jërëjëf.

382
00:24:59,791 --> 00:25:02,500
Su nu màggee noonu lanu mel.

383
00:25:03,125 --> 00:25:04,583
Doywaar, wala book?

384
00:25:06,708 --> 00:25:08,625
- Ndax mën nga ko xalaat?
- Loolu ay yëf !

385
00:26:50,750 --> 00:26:55,750
Tekkib sous-titre: Tatyana Strelkova


